Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

LIGUE DES CHAMPIONS 2024-2025 Waa UEFA amal nañu ay coppite yoy, dañuy yokk limatu ekib yiy bokk ci joŋante Ligue des champions bu déwénee, atum...

Rawale nañ Usmaan Sonko ca “réanimation” ba.

Rawale nañ Usmaan Sonko ca "réanimation" ba. Jotna Média moo siiwal xibaar bi. Ci seen xëtu Facebook lañ bind, wax ne : " Noo ngi...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (16/8/2023)

TEG NAÑU LOXO LÉWOO ÑING Léwoo Ñing mi jiite Pastef fa goxub Njagañaaw, jàpp nañu ko. Ndawi DIC yi ñoo ko teg loxo fale ca...

UBBI NAÑU CAMPUSEN

Jëwriñ ji ñu dénk njàng mu kowe mi génne na ab yégle buy buy diir ndongo yi jotoon a jàll ci joŋante “BAC” yi...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (15/8/2023)

MBIRI USMAAN SONKO AK I ÑOÑAM Fukki fan ak juróom-ñaar ci tey bi Usmaan Sonko ak i ñoñam tàmbalee xiifal ba léegi. Fii mu tollu...

CEDEAO-NISEER

Fitna jaa ngi gën dee jege ci diggante Niseer ak CEDEAO. Ginnaaw bi kurél gi jëlee ndogalu delloo Nguur ga ca loxoy Muhammet Basum,...

Me MUSAA SAAR MËNUL GIS ANIBAAL JIIM

Jamono jii, mbokki Muhammet Sàmba mees duppee Anibaal Jiim yaa ngi ci njàqare ju bir, rawatina layookatam bii di Meetar Musaa Saar.  Démb la demoon...

YOKKUTEG NJËGU SOBLE SI

Am soble nekk na lu jafe lool fi mu tollu nii ci biir réew mi. Nde, njëg laa ful bu jéggi dayo. Dafa di...

ÀQ AK YELLEEFI DOOM-AADAMA : SENEGAAL DAFA GËN A DELLU GINNAAW

Senegaal mi ngi ci guuta. Loolu la kurél yiy sàmm àq ak yelleefi doom-aadama xamle démb ci àjjuma ji. Fekk ñu doon amal ab...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

Real Madrid a ngi wër góol bu bees Thibault Courtois, góolu Real Madrid bi,  dafa ame gaañu-gaañu bu metti (rupture des ligaments croisés) ba tax...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/8/2023)

CEDEAO DAJEETI NAÑU CEDEAO, kurél gi ëmb réewi Afrig sowu-jant yi amal nam ndaje, démb ci alxames ji 10i fan ci weeru ut wii, fa...