Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

USMAAN SONKO : « DAÑ MA BËGGOON A REY… »

Usmaan Sonko feddali na tuuma yim gàlloon ci kow way-wattu kaaraange yi ne dañ ko bëggoon a rey. Dafa bind ci xëtu facebookam : « Mbokki...

LAAYEEN YI MERE NAÑU MAKI SÀLL

Ku dégg kàdduy Imaam Basiiru Caw Laay xam ne Laayeen yi mer nañ lool. Te, dara waralu ko lu dul lakkirimosen yi takk-der yi...

Paatug njiitul pekkug Asimi Goytaa li

Njiitul pekkug Asimi Goytaa lii di Umar Taraawore, ñu koy woowe Duglaas, ñàkk na bakkanam. Ay rëtëlkat a ko rey cib dampoo bi ñu...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ALTINE 24 AWRIL 2023)

SONKO Sonko dooraat na nemmeekoom yi. Tey, ça Sigicoor, génnoon na, mbooloo mu bari dar ko, topp ko. Lu ko jiitu, dafa yaxaloon ci mbaali-jokkoo...

23 AWRIL, BÉSUB TÉERE AK ÀQI BINDKAT BI

Mbootaayu Xeet yi ñeel njàng, xarala ak mbatiit (UNESCO) moo tànn bésub 23i awril, jagleel ko téere ak àqu bindkat. Saa yu bés bi...

LAMIN KAMARA, GONEG WURUS GI

Mamadu Lamin Kamara, jàppleen tur wi. Xareñte, dëgëraay, njaxlaf ak dégg-daaj la gaynde gu ndaw gi boole def. Moo tax, Mamadu Lamin Kamara, kenn...

BUUR MAKI

Démb, ci gaawug korite gi, Njiitu réew mi jagleel na ab laaj-tontu rajo RFM. Alasaan Géy a doon dalal ci Jotaayam bii di Yoon...

NGOR : KËRUG FARBA NGOM LAKK NA

Bu kenn àttewul, musiba dina am. Te, bu boobaa, dina rëccu dina fekk jëf wees. Ca Ngor, ba nëgëni-sii, ndaw ñaa ngay wéy di...

SENEGAAL, ASAMAANU ÑAARI WEER

Woorandoo, woreendoo, ay gént la fi Senegaal. Daanaka, ñaari korite, dem na ba nekk aada ci julliti Senegaal yi. At mu jot, juyoo dina...

« DAÑU MAA TOOÑ, WAAYE DUMA BÀYYI »

Yaayu Aadama miy jiiñ Sitoor Nduur ag ciif, àndul ak ndogal la tukkee ca layoob doomam ji. Moom, Njiira Jonn, li àttekat bi setal...

KARIIM WÀDD BINDU NA, LÉEGI ?

Coowal wotey palug Njiitu réew ci atum 2024 door na bu yàgg te mbir mi agseegul. Ñu bari jot nañoo samp seen i ndënd,...