Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

ÀTTEKAT BI SETAL NA SITOOR NDUUR

Ndogal li rot na : yoon toppeetul dara Sitoor Nduur. Tey, ci àllarba ji 19 awril 2023 la ko yoon bàyyi. Nde, bees sukkandikoo ci...

PASTEF, KU WAX DEM KASO

Keroog, àjjuma ci guddi, lañu fekkoon Basiiru Jomaay Fay ca kanamu DGID, fa muy liggéeye, jàpp ko. Lees ko jàppe, du lenn lu mooy...

Ngor : xeex diggante askan waak sàndarm yi

Xeex baa ngi ne kurr ca Ngor. Ndaw ña fay jàppante ak takk-der yi ci buntu pàrkiŋu dëkk ba, fa daamar yay gaare. Nee ñu,...

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ-USMAAN SONKO : DIG-DAJE 8 ME 2023

Ci altiney tey jii, 17 awril 2023, la layoob "Appel" bi ñeel Maam Mbay Ñaŋ ak Usmaan Sonko waroon a am. Waaye, ajandi nañ...

F24, ÀND XEEX 3EELU MOOME

Njiitu réew mi, Maki Sàll, amati na soxla. Nde, kurél gu bees juddu na gog, jàmmaarloo ak moom a ko tax jóg. Démb, ci...

XARE CA SUDà

Xeex bu mettee jolli Sudã, diggante làrme beek i sóobare yu beddeeku. Ñaari seneraal yi foqati woon Nguur gi, atum 2021, ñoo nekk di...

Liggéeykat yi ci dalub roppalaan yee ngi dànkaafu Nguur gi

Mbooloo mi ëmb kuréli liggéeykat yi ci dalub roppëlaan yi (Intersyndicale des travailleurs de l’aviation civile et du secteur des transports aériens) doon na...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀJJUMA 14 AWRIL 2023)

Waxtaanuw Usmaan Sonko ak Jean-Luc Mélenchon Njiitul Pastef li xamle na, ci xëtu Facebookam, ne waxtaan na ak Jean-Luc Mélenchon mii jiite pàrti pólitigu Farãs...

« ÑUULE BU BON BI ! »

Bi joŋanteb Manchester City ak Bayern Munich bi jeexe, ndeke, Saajo Maane ak Lërooy Saane dañoo xeex, gayndeg Bàmbali gi daldi koy kurpañ ci...

MUSIBAB SINJAA

Diggante ndongo daara ak sëriñam, yenn saa yi, du doon lu ratax. Lu ci bari li leen di xàjjale di mbañum njàng ci yenn...

“LAMI DEMOKARAASI” : PASTEF FENTATI NA LU BEES

Waa Pastef fëllati nañu fu bees. Wii yoon, ay lami këwsu lañu defar, tudde leen « lami demokaraasi », di leen jaay. Lami këwsu...

AKSIDÃ CA LUGA : JURÓOMI BAKKAN ROT NAÑU

Tali baa ngiy wéy di faat bakkani way-tukki yi. Aksidaŋ bu jàll, beneen tegu ca.  Ñaari fan ci ginnaaw, aksidaŋ bu metti amoon na...