Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

SENEGAAL AMATI NA NDAM !

Gàcca-ngaalaama sunu xëllóob yi (gaynde yu ndaw yi) ! Taaw daal, ndeke bu xàllee, rakk ya am jomu daagu ni buuru tan. Ba gaal...

Paap Masata Jaag dina tëdd 5i ati kaso

Ëttub àttewaay bu Pari delsi na ci àtteb Paap Masata Jaag bi. Waaye, àtte bi dafa dellu feddali daan yi ñu ko tegoon jëm...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀJJUMA 10 MÀRS 2023)

Paap Njaay tëddi na Sebikotaan Taskatu xibaaru Walfadjiri bi, Paap Njaay, mujje nañ ko jàllale ça kaso Sebikotaan. Ci altine jii la ko àttekatub lënbët...

GÉNNUG ÀDDINA Me USMAAN SÉY 

Me Usmaan Séy, layookat bu siiw bi, moo génn àddina. Ay mbokkam a ko tàgge, kibaraan yi siiwal xibaar bi. Moom nag, Me Usmaan...

LI GËN A FËS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ALXAMES 9 MÀRS 2023)

KUPPE Àngalteer Démb, foo geestu ci mbaali-jokkoo, ñoo ngi doon wone ay naataal ak i widewooy kii nga xam ni mooy defãsëeru Manchester City bi, Kyle...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀLLARBA 8 MÀRS 2023)

YOON Waa "Sureté Urbaine" bu Ndakaaru woolooti nañu. Wile yoon, Séex Aajibu Sumaare lay doon, nekkoon fi magum jëwriñ yi ci Nguurug Abdulaay Wàdd. Ag...

GÀCCE-NGAALAAMA, NDEYI ÀDDUNA !

Bu ñu nee 8 màrs, xel yépp dem ci bés bu mag bi ñu jagleel jigéen ñi ci àddina wërngal-këpp. Ñu di ko màggal...

7 MÀRS WALLA 8 MÀRS ? BEY CI SA WEWU TÀNK…

Juróom-ñetteelu fan ci weeru màrs la xel yépp di dem ci jigéen ñi, ndax seen bés la. Àddina sépp a koy màggal, di ci...

AAJIBOOK BATAAXALUB LËMBAAJE BI

Séex Aajibu Sumaare, njiitu jëwriñ ja woon, dafa bind ab bataaxal jagleel ko Njiitu réew mi. Ci biir bataaxel bi, Aajibu Sumaare daf ci...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ALTINE 6 FÉEWARYEE 2023)

PÓLITIG Ndogal lu yees ñeel peyooru dépite yi    Yokkal nañu dépite yi 700.000i FCFA ci seen peyoor. Loolu nag, ci weeru saŋwiye wi la...

XEEB NGA XAL, MU LAKK SA DÀGGA (1/2)

Kuy laaj fu réewum Senegaal tollu, dellul bésub alxames, 16 féewaryee 2023, xool, seet, settantal bu baax. Du ñàkk nga jëley ciy njàngat yoy,...