Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FËS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM (DIBÉER 5 MÀRS 2023)

LÀMB  Saa-Cees - Rëg-rëg ñoo doon bëre ci dibéeru tey ji. Mu doonoon làmb ju ñépp doon xaar. Waaye, nag, coow am na ci. Nde,...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (DIBÉER 5 MÀRS 2023)

PÓLITIG Bàyyi nañu Gii Mari Saaña ak way-moomeel yi Démb, ci yoor-yoor gi, lañu jàppoon dépite bile ak way-woomeel yi. Li ko waraloon nag...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (Gaawu 4 fewaryee 2023)

NJÀNG AK NJÀNGALE  Ab toogaanu-ñaxtu la ñenn ci jàngalekat yi ñuy woowe "contractuels" amaloon démb. Lañuy jooytu doon lañu yeex a jot ca seen CAP,...

Tukkib Njiitu Réewum Farãs li ci kembarug Afrig

Tukki ñeenti fan la Emanuyel Makarõ, Njiitu réewum Farãs li tàmbali alxemes 2 màrs 2023, fii ci kembarug Afrig. Jamono yii, tukki bi di...

Li gën a fés ci xibaari tàggat yaram (Gaawu 4 féewaryee 2023)

PREMIER LEAGUE / ÀNGALTEER  Liverpool Ribeertoo Firminoo yëgal na waa këlëb ba ak tàggatkatam, Jurgen Klopp, ni dafay dem bu atum sàmpiyonaa bi jeexee. Li sabab...

WOTEY 2024 LIY JOT, JOT NA

Lu moy at kepp a des ci wotey 2024 yi. Lawax yi tàmbali nañu wone seen bopp. Lees doon xaar ay at, nag, bees...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (ALXAMES 2 MÀRS 2023)

WÉR-GI-YARAM : Raglub Maam Abdu Asiis Si Dabbaax Liggéeykat yi ëmb Intersyndical bu raglub Maam Abdu Asiis Sy Dabbaax, amaloon nañ ab doxu ñaxtu, takk ak...

YÉENE NÉEG LA, BOROOM A CAY FANAAN

Siidi Ahmet Mbay, ku dégg tur wi sam xel dem ci coowal Aji Saar leek Usmaan Sonko. Ndax, ci lees wax, moom moo di...

Li gën a fés ci xibaari tàggat-yaram (àllarba 1 Màrs 2023)

Paul Pogba  Gannaaw 11i weer yi mu toog ci sababu gaañu-gaañu bu metti bi mu ame woon, Paul Pogba delsiwaat na ci pàkku wure...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Talaata 28i féewirye 2023)

CARGALUG 3i SÓOBARE YI GAAÑOO MALI Ci àllarba ji, 1 màrs 2023 lañu fas yéene sargal, delloo njukkal sóobarey Senegaal yi ñàkke seen i bakkan...

FESPACO

FESPACO (festival panafricain du cinéma et de la télévision de Ouagadougou) bokk na ci xew-xewu film (cinéma) yi gën a siiw ci Afrig. Ñu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Altine 27 Féewirye 2023)

PÓLITIG Wotey Njiitu réewum Senegaal Décce Faal dina nekk lawax ci wotey Njiitu réewum Senegaal yu 2024 yi. Loolu la xamle démb ci dibéer ji. Fekk...