Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (TALAATA 21 MÀRS 2023)

Njiitu réew mi saxal ñetteelu moomeem Ci wenn waxtaan wu mu doon amal ak ñii di wa Express, Njiitu réew mi, Maki Sàll, xamle...

TOOGAANU-ÑAXTU NGIR JÀPPALE PAAP NJAAY MU WALF

Ay téeméeri-téeméeri nit ñoo teeweesi toogaanu-ñaxtu ba amoon ci buntu màkkaanum Walf. Lees ko dugge mooy kaas ngir ñu bàyyi Paap Njaay, taskatu-xibaaru Walf...

SONKO, AK KAN ?

Alxames, 16 màrs 2023 ba tey, Usmaan Sonkoo nga ca raglu ba, tëdd. Waa Pastef ñoo ngiy def seen kemtalaayu kàttan ngir jàllale ko...

ÀTTEWAAYU NDAKAARU : USMAAN SONKO WAX NA ÀTTEKAT BI AY DËGGAM

Usmaan Sonko jël na kàddu gi ca àttewaayu Ndakaaru, wax àttekat bi ay dëggam ci fulla ak faayda. Njiitul Pastef li dafa biral jafe-jafe...

LAYOOB SONKO-MBAY ÑAŊ : XEEX BI DOOR NA !

Ñetti biisi Dakar Dem Dikk yu tàkk ca Petersen, AUCHAN Mermoos tàkk jëppeet, ay bérébi liggéey yu tëj, dem yombatul, dikk amatul ci péeyub...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀLLARBA 15 MÀRS 2023)

PÓLITIG Tey ci àllarba ji la làngug Pastef namoon a amal seen doxi-ñaxtu yi ci boor réew mépp. Waaye, mujjul a àntu. Ndax, perefe bu...

TAKK-DER YI LÉEMATI NAÑU KËRU USMAAN SONKO

Jamono ji nuy yaxal mbind mii, takk-der yaa nga fees dell Cité Site Kër Góorgi (Cité Keur Gorgui), fa Usmaan Sonko dëkk. Yoon yeek...

PALUG KURÉL YIY TEEWAL JÀNGALEKAT YI

Njureef ya tukke ca wotey sendikaa jàngalekat yi bir na. Mu mel ni, jàngalekati Senegaal yi tànn nañu kurél yi leen di teewal ci...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (TALAATA 14 MÀRS 2023)

PÓLITIG Ci talaatay tey ji la lëkkatoo Yewwi Askan Wi doon amal ab « Giga meeting » ca Parsel Aseni, pàkkub akapes. Mbooloo ma fees fa dell...

XEEB NGA XAL, MU LAKK SA DÀGGA (2/2)

Tey, ci talaata ji 14 màrs 2023, la lëkkatoo Yewwi Askan Wi di amal ab « giga meeting », maanaam mitiŋ bu mag a mag ca...

WAAW, ANA DIJJE BAAJI ?

Mbirum ñaari way-yëddu ya réeroon ca Kab Maniwel ma ngay wéy di lëmbe xel yi. Donte ne sax, mbir mi am na lu jege...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (DIBÉER 12 MÀRS 2023)

DOXU-ÑAXTU CA PARI « Ca Senegaalu Maki Sàll, boo naan déet di dugg kaso ! » Kàddu gilee gënoon a fés ca doxu-ñaxtu ba. Ay téeméeri téeméeri doomi...