Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

TABB YU YEES ÑEEL KÀNGAAMI YOON YI

Ci altine jii weesu lañu doon amal ndaje miy boole ak a tabb ñiy dogal ci bérébu àttewaay yi. Ndaje moomu nag, ma nga...

Benn xeer, ñaari picc !

Ronaldo ak Manchester United budoon séy la ñu ni seen rawaan yee àndatul woon. seen ànd bi demeetul woon noonu, juroon ay benke-ñenke ba...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 25 FÉEWARYEE 2023)

PÓLITIG Idi day bokk, walla ? Dina amam du am, li ñu doon laam-laame léegi mu leer. Njiitu làng gii di RÉEW MI, Idriisa Sekk,...

Kaïs Saïed : weex der taxul a weex xol

Ndekete yoo, nit, nit ay posonam. Kàdduy boddekonte yi Njiitu réewum Tinisi li biral, keroog talaata, ñoo firndeel wax ji. Moom,  Kaïs Saïed, dafa tamm...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (Alxames 23 féewaryee 2023)

PÓLITIG Yeneen tabb yu yees  Ca ndajem jëwriñ ma mu doon amal démb, kii di Njiitu réew mi Maki Sàll jot naa am ñenn ci ay...

LIMAAMU WOOTE NA

Woteb Mahdiyu bi, ku nekk dégg na ko. Mu doon xew-xewu diine bu njabootu laayeen di màggal at mu jot. Ren di yamook 143eelu...

LÀMMIÑ WEES NÀMP

21eelu féwaryee lañ jagleel ci àddina sépp bésu làmmiñ wi nga nàmp. Xalaat bu ni mel a ngi tukkee ca « Bangladesh ». Mbootaayu Xeet yi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Altine 20 Féewirye 2023)

PÓLITIG Pur tàbb na lawaxam Sëriñ Mustafaa Si moo nar a nekk lawaxub làngug polititig gii di PUR (Parti de l’Unité et du Rassemblement) ci wotey...

ATSU DËDDU NA

Saa-Gana bi, Atsu (1992-2023), mujje na feeñ ginnaaw bi mu réere ci màbbiti taax ya daanu ci sababu rëng-rëng ba ca Tirkii. Ndeysaan, dañoo...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (DIBÉER 19 FÉEWIRYEE 2023)

PÓLITIG Mbootaayu Réewi Afrig yi (UA) Ay coppite ak i naal moo tënk waxtaan wu mujj wi Njiiti réew Afrig yi séqoon fale ca Adis Abebaa....

36EELU NDAJEEM LËLUB  NJIITI RÉEW YEEK CÀMM YU MBOOTAAYU REEWI AFRIG YI (UA)

Mbootaayu Réewi Afrig yi dina amal ndajeem lëlub Njiiti Réew yeek Càmm yi. Moo ngi koy amal ci àppub ñaari fan (18 ak 19...