Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

“ÀND GËSËM” A NGI GËSËM  

Fan yee nu jàll la waa “Ànd Gësëm” génne woon ab yégle di ci xamle ne dañuy amal ay gereew ci seen fukkeelu tëralinu-jëf....

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ AK USMAAN SONKO

Démb, ci alxames ji lañu waroon a àtte Maam Mbay Ñaŋ ak Usmaan Sonko. Waaye mujjul àntu. Li ko waral mooy ne, ñii di...

KEN NDÓOY « ÑÀKK NA BAKKANAM »

Bindal sargal ku génn àddina, damay koy def. Waaye de, lu ma diis la, tiis ma. Ndaxte, loolii, day firndeel ni nit kookii ko...

LI GËN A FES CI XIBAARI BÉS BI (Alxames 16 féewaryee 2023)

LAYOO MAAM MBAY ÑAN AK USMAAN SONKO Tey ci alxames ji lañu waroon a àtte Maam Mbay Ñaŋ ak Usmaan Sonko waaye mujjul àntu. Ndax,...

AY DU YAM CI BOPPU BOROOM

Jàppante ba amoon Mbàkke doxoon ci diggante takk-der ya ak soppey njiitu Pasteef lii di Usmaan Sonko, njeexintal ya dal na ca lekool ya....

YOOTE BI AM DIGGANTE MAKI SÀLL AK USMAAN SONKO

Lu tollu ci at kepp a des ci wote yi, coow li ne kurr ci réew mi. Boo xoolee ni yëf yi di doxe...

Seen xiibaari tàggat-yaram Dibéer 12i Féewaryee 2023

Kuppeg àddina këlëb yi :  "Real Madrid" defatina ko ! Démb ci gaawu gi, 11i Féewaryee bii atum 2023, la woon finaalu kuppeg àddina këlëb...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 11 FEEWARYEE 2023)

PÓLITIG SONKO JULLIJI NA TUUBAA  Démb ci Àjjuma ji njiitu pasteef lii di Usmaan SonkoTuubaa la jullee. Mu nekk wokkotu bu dajeek geestu ci moom. Mu...

Réewandoo (fédération) diggante Burkinaa, Mali ak Gine ?

Jëwrin yees dénk wàlluw bittim réew ca Mali, Burkinaa ak Gine jot nañoo amal am ndaje ca Burkinaa. Ndax ñetti réew yi dañoo nekk...

LI GËN A FES CI XIBAARI BES BI (àjjuma 10 féewaryee 2023)

PÓLITIG Perefeb Mbàkke tere na mitiŋ ba Tey ci àjjuma ji la kii di Usmaan Sonko waroon a amalub mitiŋ ca Mbàkke waaye loolu mujjul àntu....

LI GËN A FES CI XIBAARI FUTBAL (alxames 9 féewaryee 2023)

 BELSIG AM NA TAGGATKAT BU BEES Kuppeg àddina 2018 ba léegi, Belsig dafa nekkoon ciy jafe-jafe. Njeexitalu kuppe gi gën koo feeñal. Moo tax ba...