Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

SIGARET : REYAATEKAT BI

Bërki-démb, ci talaata ji 7i fan ci féewaryee 2023, lees doon amal ndajem liggéey ñeel xeetu juuti bees duppee "taxe parafiscale" bi nga xam...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Àllarba 08 féewaryee 202)

GUY MARIS SAAÑAA BOOLE NA SËRIÑ BASIIRU GÉY Guy Maris Saañaa bind nab bataaxal, jébbal ko waa OFNAC. Li mu ko dugge mooy tiiñal Sëriñ...

SÉEX ANTA JÓOB : XARNUB LEER

Fanweeri at ak juróom-ñaar ginnaaw ba mu làqoo, Séex Anta Jóob du mës a dañ ci xol yi ak ci xel yi. Waa RND...

RËNG-RËNG CA TURKI AK SIRI : 4 890iy NIT DEEWAGUM NAÑU

Suuf si yëngooti na, àddina jooyati. Nde, ay rëng-rëng yu mettee metti ñoo dal ci kow réewi Siri ak Turki ba 4 890iy nit...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI ( Altine 6 féewaryee 2022)

PÓLITIG Mitiŋ APR Militaŋi APR yi nekk ci peggug Ndakaaru doon nañu amal ab mitiŋ ci dibéer ji, ca bayaalub SEFA bi nekk ca Pikin. Mitiŋ...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Altine 6 féewarye 2023)

PÓLITIG PDS Abdulaay Wàdd njiitu réew mi fi woon génn na ca tekkaaral ga mu nekke woon. Waaye génnam boobu mën nañoo wax ne njuuy na...

LÉEGI, GAYNDE, KUB LAY DUNDE

Senegaal amati na ndam. Gaynde yu ndaw yi ñoo jël CHAN 2023 bi doon ame ca réewum Alséri mi ñoo dóor démb ci finaal...

2eelu NDAJE MU MAG ÑEEL KOPPARAL JUMTUWAAY YI CI AFRIG

Ginnaaw bi ñu ko njëkkee amal ci atum 2014,  Nguuri Afrig yeek seen i ñoñ amal nañu ñaareelu ndaje mu mag mi ñu jagleel...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (àjjuma 2 féewaryee 2023)

PÓLITIG  Layoo Maam Mbay Ñaŋ Usmaan Sonko ajandi nañu ko Layoo bi waroon dox démb ci diggante Usmaan Sonko ak Maam Mbay Ñaŋ dañu ko mujje...

TER, FOOY TEERE ?

Keroog, gaawu 28 saŋwiye 2023, la yéenekaayu Farãs bii di Le Figaro génne ab saabal, jagleel ko saxaaru TER gu Senegaal gi. Ñu bind...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Talaata 31 saŋwiye 2023)

PÓLITIG Beneen lawax bu bees feeñati na ñeel wotey 2024 yi. Dr Baabakar Jóob, di meeru Cees, dina nekk lawax ci wotey Njiiteefu réewum Senegaal...