Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

PELENT YA JOLLI NAÑ

Téere Séex Yérim Sekk bi ak coowal Aji Saar-Usmaan Sonko ñooy ñaari xibaar yi gën a fés ci jamono jii. Ñu jur nag coow...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 21 SAŊWIYE 2023)

PÓLITIG Waxtaan wa doxoon diggante Nguur gi ak ñi yor wàllum dem bi ak dikk bi, déggoo mujjeewu ca am. Kenn ku nekk ak fa...

Burkinaa Faaso : lu ëpp 50i jigéen ni mes ni meenteñ

Diggante alxames ak àjjuma (12 ak 13 sãwiye 2023), lu ëpp 50i jigéen ñoo ni mes ne meenteñ ca Burkinaa Faaso. Ay defkati ñaawteef...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Alxames 18 saŋwiye 2023

PÓLITIG Layoo Aji Saar-Usmaan Sonko Ñaari at daanaka bi coowal Aji Saar ak Usmaan Sonko tàmbalee ak léegi, kii di magum àttekat yi Umar Maham Jàllo...

SÉEX ALIYU NDAW : NIT KI AK LIGGÉEY BI (Ibraayma Wan)

Saawo si ak nji yi Siidi Ahmet Aliyun Ndaw a ngi juddu atum 1933 ca Karcag, bokkoon ci wërngalu Biññoona, ca Kaasamaas. Baayam, ab...

CHAN 2023

Chan 2023 bi door na keroog àjjuma 13i fan ci saŋwiye 2023. Wile yoon a di 7eelu yoon wees koy tëgg. Ren nag, Alséri...

Rafayel Njaay taalifkat la woon…

Ndeem dëgg la ni àjjana, ngir mbindeef yi daa yokk yëf yu baax ci àddina la, yaakaar nanu ni Rafayel Njaay a nga guyaar,...

SÉEX ALIYU NDAW : BÉS DU ÑÀKK, DAY SORE

Mbootaayu Fonk Sunuy Làmmiñ daa fas yéene delloo njukkal bindkat bu mag bii di Séex Aliyu Ndaw keroog, àllarba 18i fan ci saŋwiyee 2023...

2023 : YOON NAR NAA XUMB

Atum 2023 mii, atum Yoon la nar a nekk. Wëliis mbirum ñetteelu moome gi nar a tàbbi ci loxoy Ndajem ndeyu àtte mi, bari...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM

WURE (FUTBAL) Gaynde Senegaal yu ndaw yi noppi nañoo waajal Chan bi. Tey ci altine ji lañu doon amal seen ub joŋante bu mujje...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI

PÓLITIG Njiitu réew mi Maki Sàll woote na am ndajeem jëwrin yi ci altine tey ji. Ginnaaw aksidaŋ bu metti bi am ca diwaanu Kafrin...