Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

Yewwi Askan Wi nangu na ndogal, jël ndogal

Caabalug ëttu cettantal gi mi ngi wéy di lëmbe réew mi, rawatina làngug pólitig gi. Àjjuma jale weesu la kuréli way-moomeel yi defoon ndajem-ñaxtu...

JÉYYA JA CA KAFRIN

Ak jéyya ju réy a réy la réew mi yeewoo tey. 54i nit ñoo ñàkke seen i bakkan ci ab aksidaŋ bu mettee metti...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (gaawu 7 saŋwiyee 2023)

PÓLITIG Tuuma ji ëttub cettantal gi tegoon ñenn ciy jëwriñ ak i DAGE ñeel koppar yu ñu luubal ci xeexum mbas mi, jëwriñ ji ñu...

DOOMU GAYNDE, GAYNDE LAY DOON !

Saa-senegaal bii di Paap Mataar Saar, ab wurekat la, nekk ndaw, tollu ci fukki at ak juróom-ñaar. Bokk na ndawi futbalkati Senegaal yees gën...

NJIITU MBOOTAAYU RÉEWI AFRIG YI (2023-2024)

Benn weer kepp a dese Njiitu réewum Senegaal li, Maki Sàll, ci boppu kilifteefu Mbootaayu Réewi Afrig yi. Ginnaaw biñ ko fa tabbee ci...

SONKO, FULLAAY JAAY DAQAAR

 Usmaan Sonko tontu na ndongo ya doon tëgg i bool ca kanamu meeri bu Sigicoor bi mu jiite. La taxoon ndaw yay ñaxtu nag,...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Alxames 5 saawiye 2023

PÓLITIG Leerali Usmaan Sonko ñeel ñaxtuy ndongoy Sigicoor yi Ci ndajem-waxtaan mu mu doon amal tey ci yoor-yoor bi, Usmaan Sonko joxe na ay leeral ci...

CONCU BU DIIS BI

Wolof nee na : "concu, boroom rekk a ko àttan". Kon, ndax jaadu na ci moom mu teg nu bosam ? Nga ne :...

TUUBA, KAARAANGE GAA NGA CA LOXOY TAKK-DER YA

Tuuba, dëkk bu sell ba, baat ba benn la. Lu bari lañuy doxal ca dëkk ba, ca kàdduy kilifa diine ga lay aju. Ci...

MAAJOOR, BUL FÉETE BOOR

Ginnaaw bi ñu fésalee seen ag caabal ñeel yorinu FORCE COVID-9 bi, Ëttub cettantal gi fëgg na buntu jëwriñ ji ñu dénk wàlluw yoon...

“SUNUY MILYAAR DU REES !”

« Place de la nation », walla Péncum askan wi ci wolof, wuyoo na turam démb ci àjjuma ji. Nde, ci ngoon gi, foo...