Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

AADAMA BARO RËCC NA !

Ag Nguur naroon na daanooti ci Afri sowu-jant. Gàmbi la naroon xewe. Ayu-bés bii weesu la amoon ñu nisaroon foqati foqati Nguur gi ci...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (alxames 29 desàmbar 2022)

PÓLITIG Yeneen tàbb yu yees  Ca ndajem jëwriñ ma mu doon amal démb, Njiitu réew mi Maki Sàll am na ñenn ci ay ñoñam ñu mu...

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk ya nu lor Nuy leb ba fees ak i bor Sànni xam sëgg ci fen di for Ndax...

SÉEX ANTA JÓOB, SUUL KER DU KO TEE FEEÑ…

Séex Anta Jóob a ngi juddoo Céytu, 29eelu fan ci desàmbar 1923. Alxuraan la dale njàngam laata muy dugg daaray nasaraan. Ci 22i atam...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀLLARBA 28 DESÀMBAR 2022)

TÀGGE : MUQADDAM SEEX BAAY BUUBU SI DËDDU NA Njabootu Seex Ahmet Tijaan, rawatina tiijaani Senegaal yi, am nañu dëj. Seex Baay Buubu Si, kenn ci...

TÀMBAAKUNDAA AM NA GAN

Tàmbaakundaa moo aye. Fa la Ndajeem jëwriñ yi Nguur giy amal ayu-bés bu neek di ame ëllëg ci àllarba ji. Njiitu réew mi, Maki...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Altine 26 desàmbar 2022)

PÓLITIG Aysata Taal Sàll a ngay dëggal ne Njiitu réew mi Maki Sàll mën naa nekk lawax ci wotey 2024 yi. Moom jëwriñ jiñ dénk...

YÓBBOOTI NAÑ PAAP AALE ÑAŊ CA RAGLUB PRINCIPAL

Ci guddig gaawu jàpp dibéer lees jàllale Paap Aale Ñaŋ ca raglub Principal. Me Musaa Saar, layookatam bi, moo ko xamle. Cëtëŋ ya lees...

46i SÓOBAREY KODDIWAAR YIÑ JÀPP CA MALI

Ginnaaw juróomi weer biñ leen jàppee ak tey, sóobarei koddiwaar yaa ngi ci loxoy Saa-Mali yi ba léegi. Waaye, Nguuru réewum Koddiwaar yónnee na...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 24 DESÀMBAR 2022)

PÓLITIG Tuuma ji ëttub cettantal gi tegoon ci yenn ndodd yi ñeel koppar yu ñu luubal ci xeexub mbas mi, Nguur gi àddu na ci....

MAAMUR JALLO, KU ÑÉPP TUFLI NGA TOOY

Coowal Aji Saar ak Sonko, féewiryee 2021 la tàmbali woon. Ba tey ma ngay wéy di lëmbe réew mi. Ca ndoorte la nëgëni, am...