Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (Alxames 22 desàmbar 2022)

PÓLITIG                            Taxawaayu Seex Abdu Baara Dolli ñeel wotey 2024               Dépite bii di Seex Abdu Baara Dolli biral na  yéeneem ngir nekk Njiitu réewum...

ALFUSEYNI GAY : “ DAMA RAGAL…”

Alfuseyni Gay mooy sinekolog ba nemmeeku woon Aji Saar keroog, guddi googu ndaw si waxoon ne Usmaan Sonko daf ko cee siifoon. Démb, ci...

LEWOPÓOL SEDAAR SEŊOOR

Ñaar-fukki fan ci weeru Desàmbar atum 2001, bés bu Senegaal dootul fàtte. Raaya réew mi sëngeem. Loolu doon màndargaal tiis ak naqar wu dal...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 19 desàmbar 2022

PÓLITIG Dépite - Meer bii di Biram Suley Jóob a ngay artooti Njiitu réew mi Maki Sàll : " Njiitu réew mi, Maki Sàll, siiwal na...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 17 DESÀMBAR 2022)

PÓLITIG Colidep (Collectif pour la libération des détenus politiques) amal nañu démb seen doxub ñaxtu. Kurél googu nag, seen yitte mooy fexe ba génne ñi...

CAABALUG ËTTUB CETTANTAL GI ÑEEL YORINU FORCE COVID-19

Ëttub cettantal gi dafa bokk ci bànqaas yiy saytu liggéeyuwaay yi nga xam ne ci Nguuru gi lañu aju. Seen liggéey mooy càmbar koppar...

Ñetti faniy ndajem USA – Afrig

Talaata 13i fan ba alxames 15i fan ci weeru desàmbar 2022, ay njiit ak i ndawi réewi Afrig ñoo nga woon ca Wasinton. Seen...

NGOMBLAAN GI GANTAL NA PASUM DIIŊAAT MU WAA YAW

Démb ci alxames ji la Ngomblaan gi amaloon am ndaje ngir wote pasum diiŋat mi waa lëkkatoo Yewwi Askan Wi di teg ci kaw...

Sémbug liggéey bu Nguuru Aamadu Ba

Ci altine jii weesu la kii di jëwriñ ju mag ji demoon ca Ngomblaan ga ngir dégtal fa li Nguur gi namm a def....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI  Àllarba 14 desàmbar 2022

PÓLITIG  Pexey kippaangog Yewwi Askan Wi  Altine jii weesu la kii di Aamadu Ba demoon ca Ngomblaan ga ngir dégtal fa li Nguur gi namm a...

TÀMBAAKUNDAA : PÉEYUB SENEGAAL CI DIIRU 3i FAN

Li ko dale 26 desàmbar jàpp 29 desàmbar 2022, Njiitu réew mi ak Càmm gépp dinañu ganeji Tàmbaakundaa. Mu mel ni, ci diirub 3i...

LIGGÉEKATI INIWÉRSITE YI JÓGATI ÑANU

Njàng mi ak njàngale mi dafa mel ni du jóg ciy njàmbat. Mënees na koo waxe noonu. Daara yu kawe yi moom ñoo faf...