Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

Ëllëgu gaynde yi ca tugal

Naples noppeegul ngir bàyyi Kalidu Kulibali mu dem. Moo ngi ci tànki yokkal ko peyooram ci àpp gu gudd donte ni këlëb yu mag...

kàdduy Seex Abdu Baara Dolli yi: Ban taxawaay la ci yoon wane?

Kàddu yi Seex Baara yékkati woon ca bésu ndajem ñaxtu Yewwi Askan Wi teg ko ci deru njiitu réew mi jural na ko coow...

Lan moo wund demu Maki bi Riisi ?

Fan yii weesu, njiitu réew, Maki Sàll, fekki woon na Putin ca Riisi ngir, nee ñu, ñu waxtaane  bekkoor bi xare bi xew digganteem...

Ikibu Futbal bu Senegaal : Ku ñépp di xaar nga war a mëne fu nekk

Keroog ci talaata ji lees tàmbali ñaareelu bëccëgu joŋantey bokkadil CAN 2023. Ikibu Senegaal bi doon ci jàmmaarlook ikibu Ruwàndaa bi ko doon dalale...

NU DELLOO NJUKKAL YAAY MARI MU SELL MI

Boo déggee Popengin sa xel day dem ci waa jàngu bi. Muy màndargaal diiney Yeesu fii ci Senegaal. Doonte ne, dëkk boobee, duy kercen...

NDAJEM ÑAXTU YEWWI ASKAN WI : WEDDI, GIS BOKKU CI

Coowal wotey palum depite yi lёmbe na réewum Senegaal lool ci jamono jii nu tollu. Coow li nag, bari na te ci ñaari boor...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di génne téere bu mu bind ci wolof (+), te mu tudde ko Malaanum lëndëm ;...

OMAR BOLONNDEE JOOP: NGAMA WAYLITAARE AFRIKNAARE

Ñande 11 Duujal (Mai) 1973, Omar Bolondee Joop sagata feeloyaŋke-filosof senegaalnaajo luutndinooɗo laamu hooreejo Lewopool Sedaar Seengor, yiita ene hawri e lajal, tawi omo...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŋ JÓOB…

https://www.youtube.com/watch?v=3sR_E7UeuMc Ci àllarba tey jii, 11eelu fan ci weeru Mee 2022 la Senegaal di fàttaliku faatug Omar Bolondeŋ Jóob 49i at ci ginnaaw. Kon li...

Ay xalaat yu meññee ci “Malaanum Lëndëm”

“TOLOF-TOLOFI ÀDDINA SEEK BIDDÉEW YI CI KOW ASAMAAN SEE YEM: AK FOO MËNTI DEM, AK LOO FA YÀGG YÀGG, BOO DELSEE FEKK LEEN FA...

XAREB IKREN BI – KAN MOOY WLADIMIR PUTIN? 2/3

Leningrad la Wladimir Putin yaroo. Leningrad googu, moo nekkaat tey Saint-Pétersburg. Cib nettali, gone gi Wladimir, ku ësoon la, amoon fit lool te bare...