Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

MANSUUR FAY AM NA DËGG CI KAW NGUUR GI

Dañu tere woon Mansuur Fay mu génn réew mi. Fan yii weesu, waññi nañu ko ñaari yoon ca dalub roppalaanu Belees Jaañ. Ñaareelu yoon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (27/3/2025)

COPPITEG TURI YOON YI AK YENN BÉRÉB YI Ni ñu koy defee ayu-bés bu jot, démb, ci àllarba ji lañu doon amal ndajem jëwriñ yi....

NJIITU RÉEW MI NANGU NA SUUFUS RËBËS

Bi ñuy waaj a amal wotey palug Njiitu réew mi, as diir kepp desoon ca, ca la Maki Sàll mi jiite woon réew mi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/3/2025)

GII MARI SAAÑAA SAMP NAY LAAJ ÑEEL CÀMM GI Dépite bii di Gii Mari Saañaa wax na ak Càmm gi. Wile yoon, 12i laaj la...

TÀGGE : MEETAR XURAYSI BA DËDDU NA

Layookati Senegaal yi am nañu tiis ak njàqare  ginnaaw bi kenn ci seen naataangoo faatoo. Meetar Xuraysi Ba, di layookat bu fës te ràññeeku,...

“MUUT ! MOTT ! NUN, WAA ISRAAYEL, NOO NGI REY !”

Léegi, képp ku jóg ngir saabal reyaate ba xew fa Palestine, Israayel dina la rey ngir noppiloo la. Nde, bi xare bi tàkkee, keroog...

PASTEF AK TFM, LU XEW ?

Coowoo diggante làngug Pastef gi ak tele bii di TFM du guléet ñu koy gis. Seen diggante moom, taxu ko rattax. Nde, ba ñuy...

SONACOS SIGICOOR : JËWRIÑ MABUUBA XOOLI WOON NA NDEFAR GI

Jëwriñu mbey mi, Sëñ Mabuuba Jaañ, amaloon na tukkib nemmeeku fa Sigicoor. Li mu ko dugge woon mooy saytuji ndefaru SONACOS ga nekk ca...

FMI DËGGAL NA ËTTUB CETTANTAL GI

RFI, saabalukaay Farãs bi, moo siiwal xibaar bi. Ci li mu fésal, FMI dafa wax ne, diggante 2019 jàpp 2024, Nguurug Maki Sàll ga...

SEN BU APR WOOTE NA BÉSUB ÑAXTU

Làngug pólitig gu APR (Alliance Pour la République) woote na bésub ñaxtu keroog àllarba 2i fani awril 2025. Muy woote bu ñu def ginnaaw...

UBBITEG KOPPEY LIGGÉEY AK JÀPPALANTE YI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ma nga woon Kumpentum, fa diiwaanu Tàmbaakundaa. Ci àjjumay tay jii, 21i fani màrs 2025, la fa dem. Li...