Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

Doxub sàrgal Séex Anta Jóob

Mbootaayu Panafrig « La marche internationale Dakar-Thieytou » amaloon na am ndaje ak saabalkat yi ca « Grand Théâtre » bu Ndaakaru. Jubluwaayu ndaje maa doon màggal ak...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/1/2025)

JURÓOM-ÑEENTEELU BÉSU SET-SETAL Set-setal bi ab xew-xew la boo xam ne Nguur gee ko doon amal ci weer wu nekk walla ci ayu-bés yu nekk....

NDÀMPAAYUL WAY-LORUY XEW-XEWI 2021-2024

Jëwriñu Njaboot gi ak Ndimbal yi, Maymuna Jéey, biral na ndogal yu yees yi ñu jël ñeel ñeel ndàmpaayul way-loruy xew-xewi 2021-2024 yi ak...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/1/2025)

7i BAKKAN ROTATI NAÑU CI TALI BI Juróom-ñaari nit ñoo ñàkk seen i bakkan ci am ndog mu metti mu am diggante Kër-Majabel ak Waag-Nguuna....

NDAJEM JËWRIÑ YI (29/1/2025)

Nees ko tàmm a defe ayu-bés bu nekk fa Njénde la, amal nañu ci àllarbay démb ji ndajem jëwriñ yi. Njiitu réew mi, Sëñ ...

NDOG MU METTI CI OTORUT “ILAA TUUBAA”

Ndog mu metti moo am démb ci talaata ji, ci boori 6i waxtu yu toftal 50i simili. Ci tali "Autoroute Ila Touba " bi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/1/2025)

NGOMBLAAN GI Coppite am na ci doxalinu Ngomblaan gi. Dog nañu ndàmpaay yi ñu daan baaxe dépite yi ñeel seen dem ak dikk. Muy 900...

CAN MAROG 2025

Puluf nañu kippuy CAN 2025 bees dëgmal te mu war a ame fa Marog. Tay ci altine ji lañu jiifii-jaafaa yëf yi, daldi samp...

CONGUM GOMA FA KONGO RDC

Askanuw Goma dootuñu fàtte altiney tay jii, 27i fani sãwiyee 2025. Nde, ci fitna lañu yeewoo tay jile. Ay soxi fetel yu diis ñoo...

SEROM BÀNJAKI DUUT NA BAARAAM MIMI TURE

Weeru sàttumbaar wee jàll lañu tegoon loxo kii di Serom Bànjaki, ñu di ko woowe “Sniper”. Booba ba tay, ma nga ca loxoy Yoon....

NJÀNG MI : JËLUB 2000iy JÀNGALEKAT

Bàrki-démb ci alxames ji, 23 sãwiyee 2025, la Càmm gi tijji woon jëlub 2 000iy jàngalekat yi ñeel ekooli tuut-tànk yi, yu suufe yeek...

NGOMBLAAN : DINDI NAÑU MBALAANU KIIRAAYU FARBA NGOM

Dépite yi dindi nañu mbalaanu kiiraayu Farba Ngom ci àjjumay tay jii, 24i sãwiyee 2024. Ci ngoonug tay ji la dépite doon fénc mbirum Muhammadu...