Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (23/1/2025)

MURIG MBALAANU KIIRAAYU FARBA NGOM Ayu-bés bii ñu génn la Ngomblaan gi dooroon liggéey bi ba jotoon a taxawal ag ndiisoo. Suba, ci àjjuma ji,...

NDAJEM JËWRIÑ YI : ÑEENTI JIITUWAAYI NJIITU RÉEW MI

Ci àllarbay démb ji, 22i fani sãwiyee 2025, lees doon amal ñeentelu ndajem jëwriñ yi ci at mu bees mii. Njiitu réew mi, Basiiru...

CDEPS MI NGI SÀKKU CI NJIITU RÉEW MI MU « YEESAL WAXTAAN WI AK SAABALKAT YI »

Conseil des diffuseurs et éditeurs de presse du Sénégal (CDEPS) dafa doon amal, tay ci àllarba ji, ndajem saabal ñeel tolluwaayu saabalukaay yi ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/1/2025)

USMAAN SONKO : DUGG NAÑU CI JAMONO JOJ, BAALE JEEX NA Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, biral na gis-gisam ci xeex gi ñuy xeex nger fi...

NJËLBEENI NDOGALI DONALD TRUMP

Démb lees doon amal palug Donald Trump niki ñeen-fukk ak juróom-ñaareelu (47eelu) Njiitu Réewum Amerig. Moom nag, dafa toog rekk tàmbalee xaatim ay dekkare...

NDAJEM WAXTAANU DOXALKAT YI AK SAYTUKATI NGUUR GI

Tay, ci altine ji, lañu doon amal ndaje moomu. Fa béréb bii ñu dippe “Centre International de Conférences Abdou Diouf de Diamniadio” (CICAD) la...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

CHAN 2025 : PULUF NAÑU KIPPU YI Keroog ca alxames ja weesu lees puluf ekib yi, daldi génne kippuy joŋantey CHAN 2025 biy ame fa...

NJËLBEENU BILAŊU “POOL JUDICIAIRE FINANCIER” BI

Démb ci àjjuma ji, 17 sãwiyee 2025, El Haaji Àlliyun Abdulaay Silla, Toppekatu PJF (Pool Judiciaire Financier) bi, biral na njëlbeenu bilaŋu ëttu àttekaay...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (17/1/2025)

ÑËWUB NJIITU RÉEWUM GANA FI SENEGAAL Tay ci ngoon la fi Njiitu réewum Gana ñëw ngir amalsi fi tukkib nuyoo. Njiiteefu Réew mi moo fésal...

TIJJITEL ËTT AK BÉRÉBI ÀTTEKAAY YI : YÉENEY NJIITU RÉEW MI

Démb a nekkoon bésub tiijitel ëtt ak bérébi àttekaay yi ci njiitalu Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Fa saalu àttekaay bu Ëttu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16/1/2025)

UBBITE ËTTI ÀTTEKAAY YI Tay ci alxames ji moo nekkoon bésub ubbite ëtti àttekaay yi. Ndaje la nag moo xam ne, at mu jot dañu...