Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

NDÀMPAAY ÑEEL WAY-LORUY XEW-XEWI 2021 JÀPP 2024

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, beral na way-loruy xew-xewi 2021 jàpp 2024 xaalis bu tollu ci 5i tamñareet (miliyaar). Muy nag...

CEDEAO : CAMPEEF GI NANGU NA GÉNNUG BURKINAA, MALI ET NISEER

Ca weeru sulet 2024 la ñetti réew yii di Burkinaa Faaso, Mali ak Niseer dogu woon, daldi génn ci kurélug CEDEAO (Communauté Économique des...

FAR NAÑU CAMPEEF YII DI HTTC AK CESE

Barki-démb ci gaawu bi lañu woo woon dépite yi fa Ngomblaan ga. Li waraloon woote bi mooy soppi as lëf ci ndeyu-sàrtu réew m...

5eelu NDAJE MU MAG MU COSYDEP

Kurélug COSYDEP (Coalition des Organisations en Synergie pour la Défense de l’Éducation) amal na juróomeelu ndajeem mu mag (Assemblée générale ordinaire). Ñu doon ko...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/12/2024)

SÉMBU ÀTTE14/2014 Ngomblaan gi dina ubbi ëllëg ci gaawu bi, 14i pani desàmbar 2024, bu fukki waxtu jotee ci yoor-yoor. Ab yégle la campeef gi...

BÀRTELEMI JAAS NEKKATUL MEERU NDAKAARU

Bésub 11eel ci desàmbar, 2024, lañu dàq Bàrtelemi Jaas ci boppu meeri bu Ndakaaru. Ndogal laa ngi bawoo ci perefe bu Ndakaaru. Li ko sabab...

LAT-JOOR ! JÀMBAAR JA ! ÑAAWULOO !

Njiitu réew mi ubbee na tënub Lat-Joor Ngóone Latiir Jóob, jàmbaar ji ñaawul. Fa Cees la tënu jàmbaar ji nekk, muy tabax bob, day...

YOON WOO NA BÀRTELEMI JAAS AK AADAMA GAY

Sànq ci bëccëg gi la xibaar bi rot. Moom, Bàrtelemi Jaas miy ndeyu-mbill ji, meeru Ndakaaru, moo ko siiwal ci xëtu Facebookam (story). Li...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (12/12/2024)

CHAN 2025 Ekibu Senegaal dina amal ñaari joŋante ñeel bokkadili CHAN 2025 bi. Gaynde yi dinañu ci amal ñaari ndaje ak Liberiyaa. Ndaje mu...

YÉENEY NJIITU RÉEW MI ÑEEL NJÀNG MI

Njiitu réew maa nga woon Gànnaar, démb ci talaata ji, ngir fekkeeji Ndajem waxtaan mom, Bennoog Afrig a ko woote. Waxtaan waa ngi aju...

SOROJ BI : BALLUY SÀNGOMAAR YI KAWE NAÑU NJORT

Balluy Sàngomaar yi, 100i kilomeetar lañu soree Ndakaaru. Kërug liggéey gii di Australian Woodside moo sasoo liggéey bi. Mu mel, fi mu tàmbalee nooy...