Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/11/2024)

NGUUR GU YEES GAA NGI WEEJI NGUUR GI FI JÓGE Démb, ci àllarba ji la ñenn ñu bokk ci Nguur gu bees gi biral yenn...

« WAXLEEN DËGG SONKO ! »

Ànd, wax dëgg ca la. Ànd bu laluwut ci dëgg, du yàgg. Te, sa waay, boo ko bëggee, danga koy wax dëgg... Yii yépp,...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

TOOGLANTE CAN 2025 : SENEGAAL - BURUNDI Ekibu Senegaal dina dalal bu Burundi talaata jii nu dëgmal, yemook 19i pani nowàmbar 2024. Ca fowub...

SIIWALUB TOFTALEG SAABALUKAAY YI CÀMM GI NANGU

Dees na siiwal limu saabalukaay yi méngoo ak yoon ci lu yàggul dara. Bees sukkandikoo ci njëwriñu Jokkoo gi, Jokkookaayi xarala yi ak Nimerig...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/11/2024)

WÉR-GI-YARAM : COMES BANK NA LOXOOM Fajkat yi bokk ci kurél gii di COMES (Collectif des Médecins, Pharmaciens, Chirurgiens-dentistes en spécialisation) bank nañu seen i loxo....

FITNAY KÀMPAAÑ BI / NDAR : JÀPPAGUM NAÑ 81i NIT

Pólisu Ndar bi jàppagum na juróom-ñett-fukki nit ak benn yees njort ne dañu laale ak fitna yi amoon ci guddig altine ji fa Ndar....

TUKKITE NJIITU RÉEW MI FA RIYAAT

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, bàyyeekoo na fi réew mi démb ci dibéer ji, wutali Riyaat, réewum Araabi Sawdit. Ndajem OCI...

LËNT-LËNT ÑEEL FAATUG MAMADU MUSTAFAA BA

Altine jee weesu, yemoo woon ak 4i pani nowàmbar 2024, la Mamadu Mustafaa Ba génnoon àdduna. Mi ngi faatoo Pari, fa réewum Farãs ginnaaw...

SÉMBUW NDEFARUG DAAMARI SÓOBARE

Dees na samp ndefarug daamari sóobare fi réew mi. Xibaar la bu tukkee ci Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Càmm gi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/11/2024)

UDS BU AJI MBERGAAN FEKKI NA PASTEF Fukki fan kepp a des ci wotey palug dépite yi. Ba tay, am na ñu dëggalagul seen bopp...

ETAASINI : DONALD TRUMP FALUWAAT NA

Ki fi nekkoon Njiitu réewum Etaasini, Donald Trump (20 sãwiyee 2017 ba 20 sãwiyee 2021) dellusi na ca boppu réew ma ginnaaw wotey Njiitu...