Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

TÀGGE : PAATUG AAMADU MAXTAAR MBÓW

Guy daanu na. Aamadu Maxtaar Mbów, maamu askan wi, moo génn àddina. Ci guddig altiney démb ji, jàpp talaatay tay jii, la wuyuji Boroomam....

JUB, JUBAL, JUBBANTI : CONC BI TEGGEEKU NA !

Keroog 24 màrs 2024 la conc bi teggeeku. Keroog it la Yoon tekkeeku, wayndare yeek caabal yi daldi fireeku. Jub, jubal ak jubbanti la...

MBIRI ABDULAAY SILLA AK LAT JÓOB

Talaata jii weesu lañu taxawal li ñuy dippe PJF (Pool Judiciaire Financiaire). Ëttu àtte boobu nag, taxawul, taxawaaluwul. Dañ ko samp rekk, sóobu xaat...

WOTEY NGOMBLAAN GI

Amal nañu am ndaje ñeel wotey Ngomblaan gi ñu namm a amal ci weeru nowàmbar wii di ñëw. Muy ndaje mu jëwriñu biir réew...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/9/2024)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA NJAASAAN Dibéer jii weesu moo nekkoon bés bi ñu doon màggul guddi gi Yonentu Yàlla Muhammat ganesee àdduna. Ñii di...

MBËNN MA FA TUUBAA

Asamaan démb si dafa bàyyeeku, ubbiy buntam, rëccal ndox mi, mu sotteeku bu baax a baax. Daanaka, réew mépp a taw. Waaye, Tuubaa daf...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/9/2024)

SAMP NAÑ ËTTU ÀTTE BII DI "POOL JUDICIAIRE FINANCIER" Jëwriñ ji ñu dénk wàllu Yoon samp tay ëttu àtte bees duppee "Pool judiciaire financier" (PJF)...

NJAAG NANGUL !

Baaxoo nanu, fi réew mi, bu xewu bànneex amee, jigéen ñiy joqalante ay teraanga. Daanaka, tuutee des, mu doon fi farata joj, xel xalaatul...

GÀMMU 2024

Démb, ci guddig dibéer ji jàpp altine jii, lañ doon amal gàmmu 2024. Muy xew mom, dañ ciy màggal bésu ganesi àddina Yonent Yàlla...

JÀPPATI NAÑ AY MBËKK-KAT

Coowal mbëkk mi lëmbe na lool réew mi, rawatina jamono jii. Am na sax, ñu jàppoon ne dina wàññeeku. Ndekete, tey la doomi Afrig...

PALUG DÉPITE YI : KURÉLU ATEL TAXAW NA

Ginnaaw bi Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay tasee Ngomblaan gi, coow top na ci. Bu ñii dee werante ci ndogal li,...