Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

TOLLUWAAYU RÉEW MI CI WÀLLU KOOM-KOOM

FMI dafa génnee ag caabal gog, day càmbar koom-koomu Senegaal ci njëlbeenug xaaju atum 2024 mi. Njureef yi tukkee ci caabal googu nag, du...

NJIITU RÉEW MI TAS NA NGOMBLAAN GI

Ngomblaan gee saay. Ki ko faat mooy Sëñ Jomaay. Démb la biral ndogal li, moom, Njiitu réew mi. Xibaar bi nag, bettul kenn. Nde,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/9/2024)

NJIITU RÉEW MI DINA JANOOK ASKAN WI CI GUDDIG TEY JII Bu yàggul dara la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jóge Siin ginnaaw...

MBËKK MI MBËKKATI NA RÉEW MI

Coowal mbëkk maa ngi bëgg a booy nopp yi. Ndax, fan yii, dafa lëmbeeti réew mi. Dafa di, jamono yii, mëneesul a toog bés...

KOMISEER KEYTA TËDDI NA KASO

Ci ndigalu toppekatu Bokkeef gi, àttekatu 10eelu kabine bi dóor na « mandat de dépôt » komiseer ba woon, Séexna Keyta. Lees koy tuumaal...

NGASUM NGALAM MA CA FALAME

Ci weeru sulet wiI weesu, Njiitu réew mi jëloon nab dekkare ngir dakkal lépp luy wutum ngalam fa Faleme ba ak li ko wër...

MBËKK MI : GAAL GI SUUX FA MBUUR

Jëyya ju metti amatina ci mbëkk mi. Genn gaal gu yab ba fees, wutali woon tugal, moo suuxati.  Jëyya jaa nga ame Mbuur, fa...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dina yékkati ay kàddu jagleel ko askan wi. Magum jëwriñ yi, Usmaan Sonko, moo ko xamle....

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (9/9/24)

Toogalante CAN 2025 : Senegaal waneegul lu dal xel ! Keroog ci àjjuma ji 6i fan ci sàttumbaar wii la ekibu Senegaal bu mag bi...

NDOG MU METTI FA NDÀNGALMA

Ndog mu metti moo am am fa Njama Faal. Njama Faal mi ngi bokk ci gox bii di Ndàngalma, nekk departmã bu Bàmbéy. Jéyya...

SAMA XALAAT ÑEEL “SOMMETS” YI AK SUNU NJIITI AFRIG YI (TAYIIRU SAAR)

Ci tekkib Paap Aali Jàllo 1. "Sommet France-Afrique" ngir wéyal nooteel geek mbéeféer gu bees gi. Te, ginnaaw bi ndaw ñi yeewoo, ñu dëpp wax...