Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

NJIITU RÉEW MI BIND NA NJIITUL NGOMBLAAN GI

Coowal DPG bu elimaanu jëwriñ yi ba léegi fayagul. Dina ko def am du ko def ? Kañ la ko war a def ak kañ...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/9/2024)

LU BEES CI CAABALUG PRODAC GI Caabal gi IGF (Inspection Générale des Finances) defoon ci naalu PRODAC (Programme des Domaines Agricoles Communautaires) wi, coow laa...

NGOMBLAAN GI JÀPPAL NA USMAAN SONKO ÀPPU “DPG” BI

Coowal “DPG” (Déclaration de Politique Générale) li nga xam ne nee na woon kurr ci réew mi, ma ngay waaj a am ab daaneel....

NJIITU RÉEW MI DÀQ NA NJIITI CESE AK HCCT YI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dàq na Ablaay Daawda Jàllo ak Aminata Mbeng Njaay. Ñoom ñaar ñoo nekkoon njiiti  campeef yii di...

SONKO XIIRAL NA YAR WI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, doon na jël kàddu gi tey, ci àllarba ji. Liggéeykati njëwriñ gu mag gi (primature) la doon janool, doon...

NGOMBLAAN GI : BENNOO BOKK YAAKAAR GÀNTAL NA SÉMBUW ÀTTE WI

Démb, ci altine ji, lañu doon àggale ndaje ma ñu dooroon ca ayu-bés bee ñu génn fa Ngomblaan ga. Li ñu ko dugge woon,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/9/2024)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA SIIN Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay moo nga jamono yii fa réewum Siin. Muy Tukki bu mu...

KAÑ LANUY TOOG ?

Doomi Senegaal, ñu yàgg a dox lañu. Bu ñu nekkul fépp it, bari na réew yooy dem tase fa ak ñoom. Aw askan lañu...

ELIMAANU JËWRIÑ YI SANTAANE NA YAXANAL

Elimaanu jëwriñ yi jël na ndogal lu bees ñeel Càmm gi. Muy sàkku ci liggéeykat yi ñu defaraat seen toogaay ngir yaxanal lees di...

USMAAN SONKO WOOTE NA BENNOO NGIR PALESTIN

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ma nga woon démb ca ndajem njàppale Palestin ma ñu doon amalee fa Espalaanaatu Jumaay Ndakaaru ju mag ji....

FUTBAL / SENEGAAL : ALIW SIISE SIIWAL NA TOFTALEEM

Démb ci àjjuma ji, 30i pani ut 2024, la tàggatkatu ekibu Senegaal bu mag bi, Aliw Siise, siiwal toftaleem. Fésal na ndaw yim tànn...

LU YEES CI BÓOMUG ASIIS DABALAA AK WAALI

Mbirum bóomug ñaari bakkan yooyu moo lëmbe réew mi jamono jii. Waaye, mel na ne Yoon a ngi ciy dox jéego yu am solo....