Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

MÀGGALUG TUUBAA 2025

Tay, 13i pani ut 2025 mooy méngook 18eelu fanu safar ci atum 1447 ci arminaatu jullit ñi. 18eelu safar nag, bu ñu ko waxee...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/8/2024)

BLD/TAKKU SOSU NA Géewu pólitig bi amati na gan. Bi wote yi jàllee ba léegi, dafa mel ni gaa ñi dañu doon seral. Waaye,...

BÓOMUG ABDU ASIIS BA

Jéyya ju ñaaw ja ca Pikin Teknopóol mi ngi wéy di jur coow fi réew mi. Ci talaatay bërki-démb ji lees siiwal xibaar bu...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (21/8/2024)

MBIRUM PAS YEES WAR A SAYTUWAAT Càmmug Senegaal gi daa fas yéene saytuwaat pas yi nguurug Maki Sàll ga torlu woon. Waaye nag, du pas...

CNRA ÀPPAL NA SAABALUKAAY YI

Bërki-démb, ci altine ji la banqaas bii di CNRA (Conseil National de Régulation de l’Audiovisuelk) génnee ab yégle. Li mu ko duggee du lenn...

MÀGGALUG TUUBAA GI

Màggal gi jubsi na. Nit ñaa ngay waaj, ku nekk ci sa wet. Waa Tuubaa ñaa ngay waajal béréb ba ngir dalal gani taalibe...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/8/2024)

NGOMBALAAN GI Ginnaaw bi ñu wotee àtte biy soppi sàrt-biiru ngombalaan gi, coowal tas gee ngi wéy ñuy amal ba léegi. Waaye, bu ko Njiiitu...

MAN MAAY KAN ?

Danuy faral di dégg ñu naan : « boo xamul foo jëm, dangay dellu fa nga jóge woon ». Muy wax ju yenu maanaa...

“GAINDESAT” : SENEGAAL AM NA SATELITU BOPPAM

Keroog, 16i pani ut 2024, la Senegaal dugg ci mboorum xarala ak gëstu. Nde, ci bésub àjjuma jooju lañu njëkk a yónni ab satelit...

DALUWAAY BU BEES ÑEEL SAABALUKAAY YI

Jëwriñu jokkoo beek jokkalante gi, Àlliyun Sàll, taxawal nab daluwaay bu bees. Muy jumtukaay bu ñu duppe ci nasaraan Déclaration médias du Sénégal jagleel...

NDOG MU METTI FA KUMPENTUM

Ndogum yoon (aksidaŋ) mu mettee ame fa Kumpentum, tey ci suba teel, bi 7i waxtu jotee. Juróom-benni nit ñoo ca ñàkk seen i bakkan...