Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

NGOMBLAAN GI JOYYANTI NA SÀRTU-BIIRAM

Dépite yi jàllale nañ sémbuw àtteb 10/2024 wiy soppi ak a mottali « loi organique » bu 2002-20 bu 15i pani me 2002 ñeel...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (15/8/2024)

NJIITU RÉEW MI DALAL NA NJIITUL UEMOA UEMOA (Union Economique et Monétaire Ouest Africaine) mooy mbootaay gi boole réewi Afrig sowu-jant ci lu jëm ci...

NDAJEM JËWRIÑ YI

Ni ñu ko daan baaxoo di def àllarba ju nekk, noon la demee démb tamit. Ndax, démb lañu doon amalaat ndajem jëwriñ yi. Njiitu...

REAL MADRID JËL NA “SUPER COUPE D’EUROPE” BI

"Super Coupe d'Europe" mooy kub boo xam ni, ñaar ñi gañe joŋantey kuppe yii di "Ligue des Champions" ak "Europa League". Benn finaal rekk...

NGËRËMUL XAREKATI SENEGAAL YA WOON

Réewum Farãs fas na yéene fésal ngërëmam ñeel xarekati Senegaal ya ko xettali woon ca ñaareelu xareb àdduna ba. Xarakti démb yooyii lañuy woowe,...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (13-8-2024)

MBIRUM "Conseil Supérieur de la Magistrature" Ndogal yi tukkee woon ca ndajem CSM (Conseil Supérieur de la Magistrature) ci àjjuma jii weesoo ngi wéy di...

CAYTUG SUUFI TEFESI SENEGAAL YI

Kurél gi doon saytu suuf si féete ci tefesi Ndakaaru yi, jébbal nañu Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, caabal gi rote ci...

GEREEWU SAABALUKAAY YI

Saabalukaay xéy nañ bank seen i loxo tey ci talaata ji, 13i pani ut 2024. Li ñu ko duggee mooy amal ab bés bu...

JÀPP NAÑU AG GAAL FA BÀMBUGAR

Mbëkk maa ngi wéy di lëmbe réewi Afrig sowu-jant yi, rawatina Senegaal. Saa su ñu jàppee ne mbëkk mi wàññeeku na rekk, fekk booba...

NDAJEM MBOOTAAYU ÀTTEKATI SENEGAAL YI

Mbootaayu àttekati Senegaal yi, ñu gën koo xam ci turu UMS (Union des Magistrats du Sénégal) amal na ndajeem mu mag démb ci gaawu...

USMAAN SONKO CA XEWUM WAATU POOL KAGAME

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, dem na Ruwàndaa. Dafa teeweeji xewum waatu Póol Kagame mi ñu falaat ci wotey 15i pani sulet 2024 yi...