Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/8/2024)

JËWRIÑU BIIR-RÉEW MI AMAL NAY TABB YU YEES Jëwriñu Biir-Réew mi, Seneraal Sã-Batist Tin amal nay coppite yu bari ci kàngaami pólis yu mag yi....

NJIITU RÉEW MI DALAL NA NJIITU NGUURUG ESPAAÑ

Tey, ci alxames ji, la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, doon dalal Njiitu Nguurug Espaañ, Pedro Sanchez. Pedro Sanchez nag, jamono jii,...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (28/8/2024)

TASUB CESE AK HCCT Dépite yi jëmmal nañ càkkuteefu Njiitu réew mi ñeel sémbuw àtte wiy soppi ndeyu-sàrtu réew mi ngir tas ñaari campeef yii...

TÀGGE : SOXNA WAALO MU SËRIÑ SAALIW MBÀKKE NELAW NA

Xibaar bu tiis la njabootu Tuubaa ak taalibey murit yi xëyee tey. Soxna Waalo Mbàkke moo wuyuji Boroomam, tey ci àllarba ji. Ci suba...

WOODSIDE : NDAM AM NA CI SÉMBUW SÀNGOMAAR WI

Woodside Energy siiwal na xibaar buy neex Saa-Senegaal yi, rawatina njiit yu bees yi. Nde, kërug liggéey gii di yëngu ci wàllu soroj bi...

NJIITU RÉEW MI TABB AMINATU TURE

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, tabb na Soxna Aminata Ture. Ci altine ji, 26i pani ut 2024 la torlu dekkareb 24/1796 bu 26i...

TASUB CESE AK HCCT

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dafa jébbal njiitul Ngomblaan gi ab dekkare buy soppi ndeyu-sàrtu réew mi. Li mu ci jublu mooy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26-8-2024)

JËFLANTEEK BITIM-RÉEW Réewum Senegaal am na yéeney gën a dëgëral digganteem ak réewum Sapõ. Mu fas cee yéene jiital lëkkoo gi ci wàllu koom-koom...

BAKKEL : NJIITUL SAED LI SEETI WOON NA BAYKATI KÀMBUG KOLANGAL GI

Mbënnum dexug Senegaal gi dafa jural ay jafe-jafe dëkk yi ko dar, rawatina Bakkel mi nga xam ne, dafa bariy kàmb. Ndax, bi dayob...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (25/8/2024)

CAN 2025 Kippuy tooglontey CAN 2025 yi génn na tay ci dibéer ji. Muy mats yoy, ñii dañuy jàll ngir bokk ci CAN 2025 bi,...

LU YEES ÑEEL BÓOMUG ASIIS DABALAA

Coowal bóomug Asiis Dabalaa gi ak jarbaatam bii di Buubakar Gano, ñu gën koo xam ci turu Waali, ba tey jeexagul. Xew-xew bu tiis...

CÀMM GI ÀDDU NA CI COOWAL ONAS LI

Mustafaa Njekk Saare mi yore kàddu Càmm gi àddu na ci coowal Onas li lëmbe dëkk bi. Muy xamle ni, gisul lu fi jar...