Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

NAALU NEKKAL : 300i DEFARUWAAYI KËYIT YEES LËNKALE

Ñetti téeméeri defaruwaayi këyit (état civil) lañu lënkale ngir yombal aar geek ceetug këyiti juddu fi réew mi. Sigicoor la xibaar bi jibee. Kii...

NDOGAL YI ROTE CI “CONSEIL SUPÉRIEUR DE LA MAGISTRATURE”

Tey, àjjuma juróom-ñeenti fan ci weeru ut lañu doon amal ndajem CSM mi (Conseil Supérieur de la Magistrature). Mu doon ndaje moo xam ne...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/8/2024)

NDAJEM JËWRIÑ YI Démb, ci àllarba ji lañu doon amal ndajem jëwriñ yi. Kii di Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jot na faa...

XEW-XEW BU TIIS FA ETAASINI

Ñetti Saa-Senegaal ñoo ñàkk seen i bakkan ci anam yu metti fa Etaasini. Ci li rotagum ciy xibaar, nee ñu, ab ndaw bu tollu...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (8/8/2024)

Jeu Olympic Paris 2024 Ci wàllu futbal bi, Espaañ U23 ak Farãs U23 ñooy daje finaal, àjjuma 9i pani ut 2024. Waaye, lu jiitu loolu,...

MBËKK MI : 14i NÉEW YU BEES

Mbëkk mi reyati na. Fukk ak ñeenti néewi Saa-Senegaal lañ fekk cig gaal fale, ca réewum Repiblig Dominikien. Ci lees xamle, dañ mbëkki woon....

MALI-IKREN : DIGGANTE BA DOG NA

Càmmug Mali gi dafa jël ndogalu dog bépp xeetu jëflante ak Ikren. Ndogal loolu nag, day tàbbi ci saa si. Li ko sabab mooy...

COOWAL MUURAAY CI DAARA YI

Coowal muuraay gi lëmbeeti na réewum Senegaal.  Kàddu yi elimaanu jëwriñ yi yékkati woon, keroog fa xew-xewu “concours général” bi, ñoo waral coow li....

NDAJEM WAKAATEER YU JÀNGUNEY SENEGAAL YI

Wakaateer yu jànguney Senegaal yi yékkati nañ seen baat, biral i kàddu. Ñuy sàkku ci kilifay réew mi ñu jël 1 500i jàngalekat ci...

KÉEW MI : BÉSUB NJËMBËT GARAB

ÔGinnaaw-ëllëg, dibéer 4i pani ut 2024, lañ jagleel garab fépp fi réew mi. Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dina dem fa Tuuba...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/8/2024)

YENEEN TABB YU YEES Démb, ci àllarba ji la Njiitu réew mi doon amal ndajem jëwriñ mi. Jot naa waxtaane ay poñ yu bari fa...