Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

AY NAAL ÑEEL NJÀNG MI

Njiitu réew mi teewoon na ca ndaje ma ñu doon sargale ndongo yi gën a ràññeeku yi kàtte gu mag gii di “Concours générale”....

AM-AMU NJIITU RÉEW MI

Ndajem Ndeyu Sàrtu réew mi siiwal na am-amu Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy jéego bu am solo ñeel coppite gog, moom...

COONO DU RÉER ?

Bari na ay xale yuy làqatu di lekk kaani. Ndax, mag ñee leen koy aaye, di wax naan : "xale du lekk kaani". Moone...

AKSIDAŊ DIGGANTE NGAAY-KEBEMEER

Aksidaŋ bu metti moo am tey ci yoonu Ngaay-Kebemeer wi. Fukk ak benni nit (11i) ñoo ci ñàkk seen i bakkan. Juróom-ñeenti nit ñoo...

CAAROY 44 : USMAAN SONKO ŊÀÑÑ NA FARÃS

Caaroy 44, xew-xew bu tiis la ci mboorum Afrig, rawatina mom Senegaal. Jéyya jooju, ma nga xewoon ca njeexitalu ñaareelu xareb àddina si. Ma...

LOMPUL : BIRAM SULEY JÓOB WAX NAAK NJIITI GCO YI

Jëwriñ ji, Biram Suley Jóob, wax na ak njiiti GCO (Grande Côte Opérations SA), di këru liggéey giy génne xeer yi ci màndiŋu lompul...

SÉMBUW NDEFARUG DAAMAR FI SENEGAAL

Senegaal mën na am ndefarug boppam gog, dinay liggéey ay daamar fi réew mi. Bu ko defee, dootul jéggaaniy daamar walla jumtukaay yi ciy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (25/7/2024)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI Démb ci àllarba ji la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay tukki. Wii yoon ma nga jëm fale ca Farãs...

MUSIBA FA CAAROY-GЀEJ

Fa Sancaba, gox bu nekk Caaroy-géej, ñetti gune lañu fekk ci benn daamaar ñu faatu. Jéyya jooju mu ngi xew keroog ci altine ji....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/7/2024)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jóge na fi, dem Farãs. Nawleem bi, Njiitu réewum Farãs (Emmanuel Macron), ak Thomas...

JÉYYA FA ECOPI : LU ËPP 150 BAKKAN YU ROT

Jéyya ju réy moo xew fa Ecopi. Suuf saa fa màbb ba ay bakkan yu bari rot ci. Njiiti réew ma xamle nañ ne,...

KÀTTEY BFEM 2024

Démb, ci altine ji, door nañu kàttey BFEM 2024 bi. BFEM (Brevet de Fin d’Études Moyennes) bi, mooy kàtte (walla lijaasa) yiy tëj xaaj...