Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

COOWOO CA NGOMBALAANU CEDEAO

Barki-démb, ci gaawu gi, la dépitey CEDEAO yi doon amal am ndaje fa Abujaa, fa réewum Niseriyaa. Waaye, laata ndaje ma di jeex la...

BÀLLA GAY DAANATI NA TAFAA TIN

Démb a doonoon woon ñaareel wi yoon ñu sëgg ci géewub bëre-dóor. Bàlla Gay a daanoon, keroog seen bëre bu jëkk ba, 2i pani...

TÀGGE : USÉYNU BÉEY WÉY NA

Njabootu mbatiit ak làmmiñi réew mi amati nañ tiis ak uw naqar. Kenn ci seen i kàngaam, di woon jàmbaar ci toolu mbatiit ak...

PÉEXALUG JÀNGUNEB NDAKAARU

Càmm gi dellusi na ci way-am-bag yi (les nouveaux bacheliers) ak jël gi ñu leen war a def ci jàngune yi. Muy lu ñu...

NDOX MI : FSS A NGI SÀKKU ÑU SIIWAL PAS YI

Kurél gii di Forum Social Sénégalais, gàttal biy joxe FSS biral na càkkuteefam ñeel céddaleg ndox mi, fi réew mi. Li kurél giy laaj...

NJUREEFI BAC 2024 YI

Joŋante BAC bi jeex na ci ayu-bés bii ñu génn. Njureef ya ca tukkee rot nañ. Maanaam, limub ñi def joŋante bi, ñi ci...

NDAJEM NJIITI KIPPAANGOY DÉPITE YI

Coowal DPG li ba tey jeexagul. Nde, ndeyu-mbill ji, Usmaan Sonko, dafa am ay sàrt yu mu tegoon, wax ne bu Ngomblaan gi soppiwul...

TAXAWALUG NJËWRIÑ GU YEES

Lu tollu ci ñetti weer kepp, ginnaaw bi ñu leen falee ak léegi, Nguur gu yees gi mi ngi jël ay ndogal ngir amal...

TAMXARIT

Tamxarit bokk ci na ci xew-xewi diine fii ci Senegaal. Tur wi rekk làmboo na doole ji mbatiit am wàll ci moom. Mu nekk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (15/7/2024)

MATALEG NOSTEG WOTE YI Barki-démb ci gaawu gi, doon nañ amal ndajem weccante xalaat ci anam yees di amalee wote yi fi réew mi....

EURO AK COPA 2024

EURO 2024 Démb, ci dibéer ji, 14 sulet 2024, la woon finaal Euro 2024 bi doon ame fële ca Almaañ. Po mi nag, Espaañ moo...