Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

JÀKKAARLOO NJIITU RÉEW MI AK TASKATI XIBAARI YI

Démb ci gaawu gi, fukki fan ak ñett ci weeru sulet 2024, la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, doon janoo ak taskati-xibaar...

NDOGAL YU BEES ÑEEL NJÀNG MU KOWE MI

Ay ndogal yu bees wàcc nañ ci njàng mu kowe mi. Muy i ndogal yu jëwriñ ji jël ngir jubbanti jëlinu jàngalekat yi ak...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/7/2024)

JANOO NJIITU RÉEW MI AK TASKATI XIBAAR YU RÉEW MI Lu tollu ci téeméeri fan ginnaaw bi ñu ko falee ak léegi, Njiitu réew mi,...

COOWAL BAC 2024 BI

Joŋante BAC bu atum ren jii bari na ay coow lool. Te, li ko waral du lenn lu moy ñàkk a jëfe ndigal gi...

KENUY FAYDA YI

Nit ñi dëkkee ci àddina si, jamano jii, xayma nañu leen ci lu ëpp juróom-ñatti tamñareet (miliyaar). Te, ci lim bu takku boobu, ñi...

SENEGAAL/ANSD : LIMU NIT ÑI

ANSD, banqaas biy saytu limu nit ñeel yu ni mel, génnee na caabalam gu mujj gi. Nde, ci atum 2023 mi lañ doon waññi...

USMAAN SONKO DALAL NAÑU KO FA TUUBA AK TIWAAWON

Njiitu Càmm gi, Usmaan Sonko, seeti woon na kilifay diine yu Tuubaa ak Tiwaawon. Tay, ci yoor-yooru talaata ji, la dem fa Tuubaa, Séex...

JÉYYAY MBËKK MI : AAMADU BA (BBY) ÀDDU NA

Elimaanu jëwriñ ja woon ci nguurug Maki Sàll, Aamadu Ba, àddu na ci jéyya ji am ci géej gi, te 89i saa-senegaal ñàkk ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/7/2024)

65eelu NDAJEM CEDEAO Démb ci dibéer ji, 7i pani sulet 2024, kurél gii di CEDEAO (Communauté Économique des États de l’Afrique de l’Ouest) doon na...

AES AK CEDEAO : XIIROOK ŊAAYOO BA KAÑ ?

Diggante ñaari kuréli Afrig sowu-jant, seytaane génnagu ci. Nde, seen diggante baa ngi wéy di gën a ñagas. Saa bu ñu yaakaaree ne booloo...

EURO AK COPA 2024

EURO : Njureefi 1/4 dë finaal yi Mats yi ñeel 1/4 dë finaal yi "Euro" bi jeex nañ barki-démb ci gaawu gi. Nii la njuureef...