Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/7/2024)

CEDEAO - AES CEDEAO jël ndogal ñee maxejji réewi AES yi (Mali, Burkinaa Faaso ak Niseer). Ndogal li mooy ne, léegi, Saa-Mali yi, Saa-Burkinaa yeek...

TUKKIB BIRAM SULEY JÓOB FA FARÃS

Jëwriñ ji, Sëñ Biram Suley Jóob, yékkati na ay kàddu ñeel ndefari réewum Farãs yi. Fekk mu doon fa amal ab tukki ngir waxtaan...

NDAR : SONKO DIGE NAY PEXE ÑEEL NAPP GI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, mi ngi woon fa Ndar, tay ci gaawu gi, 6i pani sulet 2024. La ko yóbboon di ñaareelu bésu...

BËTAL NAÑ BFEM BI

Bésub 18 sulet 2024 lañ àppaloon joŋante BFEM bi. Waaye, dañu ko mujje bëtal. Maanaam, dañ ko randal ba altine 22i pani sulet 2024. Bees...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/7/2024)

OFNAC MI NGI DALAL ÑI ÑU TABB CI NGUUR GU BEES GI Ginnaaw bi ñu leen tabbee, ñoom jëwriñ yeek Njiit yi, bàyyiwuñu leen...

NDAJEM JËWRIÑ YI

Démb ci àllarba ji lañu doon amal ndajem jëwriñ yi ci njiiteefu Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Ca ndaje mooma, jot naa...

SAARAYA : AY SAAY-SAAY ÑOO SOQI FETEL CI AG DAAMAR

Fa Saaraya, féete ci diiwaanu Kéedugu, la ay saay-saay song ag daamar, soqi ciy bali fetel. APS moo siiwal xibaar bi niki tay ci...

EURO AK COPA AMERICA 2024

EURO 2024 Njureefi 1/8 dë finaal yi Ndajey 1/8 dë finaal yi ñeel Euro bi jeex nañ démb ci talaata ji. Nii la njuréef jonante yi...

BAC 2024

« BAC » dafa bokk ci joŋante yi gën a siiw fi Senegaal. Démb la door, ci talaata ji, 2i pani sulet 2024. Joŋante ren bi...

RTS : PAAP AALE ÑAŊ DAKKAL NA DÉGGOOY RAASIN TAALA YA

Paab Aale Ñaŋ a ngi indiy coppite ca RTS. Ndogal lu yees lu mu mujjee jël, mooy dakkal xeeti déggoo yu ko Raasin Taala...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/7/2024)

NJÀNGATI WOTEY 2024 YI Kurélu maxejj gii di COSCE (Collectif des Organisations de la Société Civile pour les Élections) àddu na ci wotey Njiitu réew...

KOLOBAAN : LEERALI USMAAAN SONKO

Démb, ci ngoonu dibéer ji, elimaanu jëwriñ yi amaloon na ab doxantu fa Kolobaan ak fa tefesu “Anse Bernard”. Li mu ko dugge woon...