Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

BORUB GALAG ÑEEL KËRI TASUKAAYI XIBAAR YI

Jamono jii, këru tasukaayu xibaar yu bari ñoo ngi ci guuta. Ndaxte, dañu ame ay jafe-jafey koppar yu takku. Loolu, dara waralu ko lu...

NDOGAL YU YEES ÑEEL NJÀNG MU KOWE MI

Abdurahmaan Juuf, jëwriñu njàng mu kowe mi, gëstu geek coste gi, biral na njureef yi tukkee ci lël bi ñu doon amal ñetti fan...

DOORO GÉY, BAH JAXATE AK IMAAM SÉEX TIIJAAN NDAW DEM NAÑ KASO

Tey ci altine ji, ñetti fan ci weeru suwe la ndogal li daanu. Bah Jaxate Ak imaam Séex Tiijaan Ndaw ñoo bokkoon li ñu...

REAL MADRID DEFATI NA KO !

15i kub ! Real Madrid kepp moo ko fi defagum ci joŋantey Ligue des Champions bi. Ndax, ci gaawu gii, 1eelu fanu suwe 2024, la...

SET-SETAL NGIR WAAJAL NAWET BI

Démb, gaawu 1eelu fanu suwe 2024, moo doon bés bees jàppaloon set-setalu réew mi. Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, moo ko woote...

LËLUB NJÀNG MU KOWE MI ÑEEL BAAXAL APPUG NJANGALE MI

Kilifa yi séq njàng mu kowe mi ubbi nañu lëlub ñetti fan. Ñu namm cee tëral i pexe ngir joyyanti atum njàng mi, delloo...

NJIITU RÉEW MI TEEWE NA WAXTAANUW ONU WI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, teewe na, démb, waxtaan wi Mbootaayu Xeet yi (ONU) doon amal. Waxtaan woowu, ci wàllu pólitig la...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (30/5/2024)

NJIITU RÉEW MI AMAL NA TUKKI FA MALI AK BURKINAA FAASO Ginnaaw ba mu amalee ay tukkiy nemmeeku ak liggéey fa Gine, Gana, Muritani ak...

NJAAYUM SUUF : DOORO GÉY TAQAL NA MAKI SÀLL

Dooro Géy, di kenn ci ñi jege lool Maki Sàll, lañu jàpp fan yii ci mbiru njaayum suuf fa naawub Léwópóol Sedaar Seŋoor ba...

BIRAM SULEY JÓOB MA NGA WOON KÉEDUGU

Jëwriñu laf gi, soroj beek mbéll yi, Biram Suley Jóob, ma nga woon fa Kéedugu, doon fa amal tukkib nemmeeku fa barab ya ñuy...

FIARA 2024

Fiara (Foire internationale de l’agriculture et des ressources animales) bu 2024 bee ngi ñuy wéyal fa Cices. Barki-démb, ci dibéer ji, 26 me 2024,...