Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

YOON : JUB, JUBAL, JUBBANTI

Tey, ci talaata ji, 28 pani suwe 2024, lañuy tijji péncoo mi ñu jagleel ni Yoon war doxee. Péncoom ren jii nag, mooy doon...

MBIRI BAA JAXATE AK IMAAM NDAW

Tey ci altine ji la Baa Jaxate ak Imaam Séex TIijaan Ndaw doon janook àttekat bi ci mbiri boroom ñaari tur yi ñu doon...

NDOLLENTU JURÓOMI AT NGIR KÀPPITEEN TARAAWORE

Ndogal loolu ñi ngi ko jël barki-démb ci gaawu gi ginnaaw waxtaan wu ñu doon amal ñeel “Assises nationales” yi. Waxtaan woowu ci ñaari...

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy wax ? Nga tontu ne : Boo bañee ñaaw de, xanaa dangay dëkkee toppatoo sag xar-kanam...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA PARAAYAA AK KONAAKIRI

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA PARAAYAA AK KONAAKIRI Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, mu nga woon fa réewum Gine. Barki-démb ci àjjuma...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (25/5/2024)

SINEEBAR BA NGI JÀLLAAÑOO CI BIIR RЀEW MI Takk-deri duwaan yi (douaniers) dogaale nañu ay sàmbaa-bóoy yu doon jéem a jàllale sineebar. Dafa mel ni...

BÓOMUG ALEŊ KALI: G7 BU CEES DOOR NA XEEX BI

Barkaatu-démb ci talaata ji lañu bóom jangalekat bii di Aleŋ Kali. Ci anam yu metti lañu faatee bakkanam. Nde, dafa jàngaleji woon ba wàcc,...

TAXAWALUG “PLATEFORME” JUBBANTI

Talaata jii di ñëw mooy bés bi ñuy door waxtaan wi Njiitu réew mi doon wax bu yàggul dara. Waxtaan wi nag, dinañu ko...

TUUMAY LUUBAL ÑEEL YAAY FAATU JAAÑ

Yaay Faatu Jaañ la yéenekaayu Yoor-Yoor xëyee tey ci xëtam bu njëkk, mbaali jokkoo yi fésal ko, di ko mbamb. Moom nag, soxna si,...

JÀPP NAÑ MEERU SINJAAN BI

Ceerno Jaañ, meeru Sinjaan bi, lañu jàpp tey ci àllarba ji. Jàllale nañ ko ca toppewaay (Parquet) ba.  Emedia moo siiwal xibaar bi. Nee ñu...

136EELU AJUG POPENGIN

Ci ndoorteelu ayu-bés bi, altine 20 ci weeru me 2024, la waa jàngu bi doon amal aj gi ñuy def fa Popengin. Gu ren...

BATAAXALU ÀLLIYUN TIN ÑEEL USMAAN SONKO

Àlliyun Tin yékkati na kàddu jagleel ko elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko. Ginnaaw ganam gi mu fi doon dalal ci bés yii weesu ak...