Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

EURO 2024 AK COPA AMERICA 2024

Ren, soppey kuppe dinañubégg bég. Nde, ginnaaw sàmpiyonaa yi jeex ak Ligue des champions bi, amati nañ yeneen ñaari joŋante yu mag yu leen...

WATTU LÀKKI RÉEW MI 1/3

Ànd jubal mbind mi ! Ñaareelu yëngug jubbanti mbindin mi Yaxub kubbite  Tey jii, boroom xam-xam yaa ngi gëstu làmmiñu wolof, ci fànn yu ni...

BARIGO PETOROL BU NJËKK FA SÀNGOMAAR

Muy xibaar bu njëkk ci noppi àdduna wërngal këpp : réewum Senegaal sol na barigo petorolam bu njëkk. Ginnaaw ba ñu ko feeñale ci...

LU GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/6/2024)

WÉR-GI-YARAM Kurél gii di ànd gësëm, di kurélug waa kër doktoor, àddooti na. Wile yoon nag, du ngir gësëm walla di bank seen i loxo....

SONKO YËNGAL NA

Ndaje moomu mi ngi amoon démb ci dibéer ji, fale ca béréb boobu ñuy dippee “Grand théatre”. Ñi ko amaloon du ñenn ñu moy...

“ICS” FEEÑLE NA

Ginnaaw riirum caabal yi ci yorinu alalu askan wi, coow topp na kër gii di ICS. Ay ati at a ngi nii, tàbbalul dërëm...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/6/2024)

BUGAAN GÉY DANEE NGI WEDDI AK A LEERAL Yéenekaay Source A dafa fésaloon ab xibaar, di ci wone coow lu dox ci diggante Bugaan Géy...

NJUUMTE

Ci xam-xamam bu amul yemu ak xareñam bu amul sikki-sàkka, Boroom Bi dafa bind nit mooñaale ko ak ug matadi gu mat sëkk. Waaw...

BATAAXELU NJÉMMEER ÑEEL JAWRINU CAYTUG NJÀNG MI CA LUGA

Kilifa gi, Ginnaaw ba ma la nuyoo jox la sa wàccuwaay, duma def lu moy dikk ci aali-kalaj gi jëm ci dogal bi nga jël...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (6/6/2024)

BÀYYI NAÑU AADAMA FAY Démb lañu ko téye woon fa “Section de Recherches” bu Kolobaan ñeel mbirum suuf mi ñu ko doon toppe. Nde, nee...

JUB, JUBAL AK JUBBANTI CI KOW TALI YI

Naalu “Jub, jubal, jubbanti” fa mu duutoon baaraamam teggiwu ko. Kilifay Càmm gu bees gi ña ngay wéyal di def seen liggéey. Ba tax...

GÀTTALI BÉS BI (4/6/2024)

ISRAAYEL RAY NA CI WAA PALASTIIN LU ËPP 15 000iy GONE Bees sukkandikoo ci tele Al Jazeera, ba xeex ba tàmbalee ba léegi, ca weeru...