Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (20/2/2024)

Mbappe ak PSG jeex na ! Wii yoon leer na ni Saa-Farãs bi dafay jóge Paris Saint-Germain. Keroog, alxames 15i féewiryee la ko yéenekaay yu...

DIISOOB WOTE YI

Ndajem ndeyu àtte mi neenaloon dekkare Njiitu réew mi ak sémbub àtte bi Ngomblaan gi wote woon. Daf santoon kilifa yi ko yeyoo, ñu...

“KAFKA” LU MU NU WAX CI MAKI ?

Téereb "Kafka" bii dafa lay jàngal lu bari. Ni àddina man a xëyee rekk soppiku. Ka nga nekkoon, nekkatoo ko. La nga doonoon, doonatoo...

37eelu NDAJEM BENNOOG AFRIG

37eelu Ndajem Bennoog Afrig, ñu gën koo miis ci UA (Union Africaine), mi ngi ñuy doxal ci njeexitalu ayu-bés bi. Jamono ji ñu koy...

MAKI SÀLL JÉBBALU NA

Gaawu, ñetti fan ci weeru féewiryee 2024 la Njiitu réew mi jëloon ndogalu dàq wote yi waroon a am ñaar fukki fan ak juróom...

AMNESTI : MAKI XÀLL NA YOONU JÀMMOO

Fan yii, ñoo ngi soow mbirum amnesti (mbaale) bi Njiitu réew mi junjoon. Amnesti boobu, lees ci jublu mooy far lépp li fi jot...

NDAJEM NDEYU ÀTTE MI NEENAL NA DEKKARE NJIITU RÉEW MI !

Ndajem Ndeyu àtte mi àtte na ! Juróom-ñaari kàngaami àttekat yi neenal nañ dekkare bi NJiitu réew torlu woon, daldi fomm wotey 25 féewiryee 2024...

AES DËGGAL NA BOPPAM

Waa AES (Alliance des Etats du Sahel) fasul yéene dellu ginnaaw ci génn bi mu génn CEDEAO. AES nag, ñetti réew ñoo ko séq,...

MAKI, FÀTTALIKUL “PAPA DOC”

Jafe na nga xam as lëf ci dundu "Papa Doc" (François Duvalier) mu réewum Ayti te sa xel du dem ci Maki. Doonte manoo...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/2/2024)

DÀQATI NAÑU LAYOOB SÉYDINA UMAR TURE AK SÉEX YÉRIM SEKK Coow li dox diggante ki fi nekkoon kàppiteen bu sàndarmëri ak kii di Séex Yérim...

AAR SUNU ÉLECTION BËTAL NA DOXU-ÑAXTOOM BI

Kurél gii di wuyoo ci turu Aar Sunu Élection tegandi nañu ci suuf seen doxu-ñaxtu bi ñu sumboon te naroon ko amal démb ci...

ABDU JUUF DELLU NA GINNAAW

Démb, Abdu Juuf ak Abdulaay Wàdd, Njiitu réew ya woon, dañ bokkoon bind ab bataaxal jagleel ko askanuw Senegaal. Ci seen bataaxal bi, dañ...