Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/2/2024)

ETAASINI A NGI YEDD NGUURU SENEGAAL Àmbaasad Etaasini mi ngi yeddati Nguurug Maki Sàll gi. Ab tweet lañ bind, wax ci ne : “Ci réewi demokaraasi...

LËKKATOO “DIOMAYE PRÉSIDENT” DINA WÉYAL XEEX BI

Démb ci dibéer ji la lëkkatoo gii di “ Diomaye Président” doon amal ndajem waxtaan ñeel tolluwaayu réew mi ak li ñu namm a...

CAN 2024 KODDIWAAR : TËGG SA CAN, JËL KO !

Koddiwaar mooy waaga CAN 2024 bees doon amale biir dëkkam. Mu doon dajeek Niseriyaa bu Wiktoor Osimen. Waaye, moom Koddiwaar moo mujje gañe ñaari...

SÉMBUB ÀTTE BUY NEENAL I DAAN

Yéenekaay Le Quotidien moo siiwal xibaar bu bette, tey ci yoor-yoor bi. Yéenekaay bi dafa bind ne, Njiitu réew mi, Maki Sàll, dafa bëgg...

UE MI NGI GËTËN MAKI SÀLL

UE (Union Européenne) waxatinaak Maki Sàll. Ginnaaw bi mu njëkkee ñaawlu ajug wote yi, kurél gi dafa dellu démb ci àjjuma ji doon sàkku...

MAKI SÀLL : “…BU BOOBAA, (…) ÑÉPP ÑOOY ÑÀKK…”

Njiitu réew mi, Maki Sàll, fasul yéene dellu ginnaaw. Ñaari bakkan rotagum nañ ci xeex bi ndogalam li sabab. Te, démb ba tey, réew...

BAKKAN ROTAAT NA FA GINNAAW RAAY

Ginnaaw ndongo la gaañu fa jànguneb Ndar, beneen ndaw ñàkk na bakkanam fa Ndakaaru. Móodu Géy, amoon 23i at, lañu dóor balu fetel ci...

“UGB DU AY SËG !”

Ginnaaw Fàllu Seen (2018), leneen ndongo faatooti na fa jànguneb Ndar ba ci sababuy ñaxtu. Démb, bi njàngaan yiy ñaxtu ngir kaas ndogalul dàq...

ÑAARI BAKKAN ROT NAÑ XAAT

Bakkan rot na fa jànguneb Ndar ba (Iniwérsite Gastoŋ Berse). Taskatu xibaar bii di Ilan Gabet a ko siiwal ci xëtu X (Twitter ba...

SAA-CEES YI SÓOBU NAÑ CI XEEX BI !

Ndaw ñi jóg nañu fa Cees. Mu mel ni ndaw ñi fippooti nañu. Tay ci àjjuma ji lees joxe woon ndaje ngir wéyal seen...

XEEX BI TÀMBALEETI NA !

Xeex bi tàmbaleeti na diggante askan wi ak takk-der yi. ndogalul dàq wotey 2024 yee ko sabab. Nde, tey ci àjjuma ji la kilifay...

MAKI SÀLL A NGI GËN A WÉET

Keroog, gaawu 3 féewiryee 2024, la Njiitu réew mi jëloon ndogalu xaatim ab dekkare buy neenal njëlbeenub dekkare bi sàrtaloon wote yi ba léegi....