Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

XALIFA SÀLL JIITAL NA BÀRTELEMI JAAS

Bàrtelemi Jaas mooy jiite kàmpaañu Xalifa Sàll. Ci ngoon gi la xibaar bi rot. Moom, meeru Ndakaaru bi, yàgg na ànd ak Xalifa Sàll....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/01/2023)

JÉBBALUG DABANTAL YA TAQARNAASE NA Ñetti fan kepp a des ndajem ndeyu àtte mi biral limu lawax yiy joŋante. Waaye de, xeexoo baa ngi mel...

WOTEY 2024 YI : LAWAX YAA NGAY GAL-GALANTE

Ndekete yoo, nekk lawax ci réewum Senegaal yombul. Ca dëgg- dëgg, mbir mi làmbi golo lay xaw a niru. Ndax, ñu bari foogoon nañu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16/01/2024)

DOXIINU YOON CI RÉEW MI Lépp lañ war a xoolaat ci ni yoon di doxee fi réewum Senegaal. Muy gis-gis bu Meetar Maam Aadama Géey,...

SENEGAAL WULLI NA GÀMBI

Tay ci altine jii 15 sãwiyee 2024 la Senegaal doon amal joŋanteem bu njëkk ci kuppeg Afrig giy am fee ca Koddiwaar. Mu doon...

COOWAL NASIYONAALITE KARIIM MAYSA WÀDD

Juróomi fan kepp a des balaa ndajem ndeyu àtte miy siiwal limug lawax yiy bokk ci wotey 2024 yi. Jamono jii nag, coow laa...

MBIRI BAABAKAR FAAL : CAP DUGG NA CI COOW LI

Waa CAP àddu nañu ci mbiri Baabakar Faal. Ginnaaw bi taskatu xibaar bi jotee ay saaga ak i tëkku, fas yéene wuñ koo seetaan...

CAN KODDIWAAR 2024

Ëllëg ci gaawu gi la joŋantey CAN biy door. Ren, Koddiwaar moo dalal xëccoo bi. Ñaar-fukk ak ñeenti (24i) ekib yu séddalikoo ci juróom-benni...

WOTEY 2024 YI : AG TËNK ÑEEL BAAYALE GI

Areete 032005 bu 25 sàttumbaar 2023 bu njëwriñu biir réew mi biraloon moo tënk limu falaakon bob, lawax bu nekk war na ko dajale....

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : COOWAL LIJAASA “CAP” BI

Jàngalekat yaa ngay ñaxtu ak a naqarlu anam bi ñu nekke, rawatina ñàkk maandu gi dox seen biir, ñoom  jàngalekat yi. Li way-ñaxtu seetlu,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/01/2024)

LU BEES ÑEEL COOWAL KËR YËRMAANDE Béréb boobu doon yore ay xale te Ndeela Maajoor jiite woon ko, coow la feyagul. Ginnaaw bi ñu...