Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

CAYTUG BAAYALE GI : ÑAAREELU SUMB BI

Tey ci talaata ji, 9 sãwiyee 2024, la ndajem ndeyu àtte réew mi doon saytu baayaley lawax yi matalul woon te waroon a mottali...

WOTEY 2024 YI : LËNT-LËNTI BAAYALE GI

Ginnaaw bi ndajem ndeyu àtte mi noppee ci caytu gi njëkk ñeel way-sàkku lawax yi, am na ñenn ci ñi mu geg ñu fas...

LACOS DUUT NA BAARAAM NDAJEM NDEYU ÀTTE MI

Lu ëpp ayu-bés a ngi nii, ginnaaw ba caytug xobi baayale yi tàmbalee. Boobaak léegi nag, saytul nañu lawax yu bari seen i xobi...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

CAN-SENEGAAL : JOŊANTEB XARITOO Ëllëg, ci altine ji, bu 18i waxtu jotee la Senegaal di daje ak Niseer ca fowu ba ca Jamñaajo. Muy joŋanteb xaritoo...

MARIN BU SENEGAAL : JURÓOMI KOMÀNDOO YI RÉER

Juróomi komàndoo yu marin bu Senegaal ñoo réer. Muy mbir mu doy waar mu ñu nemmeeku ginnaaw bi marin bi tegee loxo benn gaalu...

NDAJEM NDEYU ÀTTE RÉEW MI : GEG NAÑ USMAAN SONKO

Tey ci àjjuma ji la ndajem ndeyu àtte réew mi warron a jeexal caytug baayaley lawax yiy sàkkoo bokk ci joŋantey wote 2024 yi....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (04/01/2024)

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ AK USMAAN SONKO Coow li doxoon diggante Maam Mbay Ñaŋ ak Usmaan Sonko ba tey jeexagul. Waaye, mel na ne ña...

KARIIM WÀDD : “SAMAG GÀDDAAY MI NGI JEEX”

Ni ñu ko baaxoo gise ci njeexitalu at mu nekk, njiitu réew mi dina janoo ak  askanu Senegaal ngir amal aw waxtaan. Mu mel...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/1/2024)

NEKKUG LAWAXU USMAAN SONKO Ndaje mu mag la ñoñi Pastef gi woon waajaloon a amal ci gaawu gi ngir tabb Usmaan Sonko mu doon seen...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI CI AT MU BEES MI

Démb ci guddig dibéer ji, yemoo woon ak fanweeri fan ak benn ci weeru desàmbar, la Njiitu réew mi doon janook askan wi. Mu...

CAN 2023 : ALIW SIISE TÀNN NAY NDAWAM

Barkaatu-démb ci àjjuma ji la tàggatkatu ekib nasiyonaal bi, Aliw Siise doon amal ab jàkkaarloo ak taskati xibaar yi ngir wax li jëm ci...

WOTEY 2024 YI : WURE WA DEM NA KËŊ

Tey ci gaawu gi la ndajem ndeyu àtte réew mi tàmbali seen liggéey ñeel càkkuteefi lawax yi. Ñu fas yéene koo amal ci àppug...