Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/12/2023)

CAMPUG LAWAXU USMAAN SONKO Muy xew-xew bu ñu dëgmal te ña fare ca lëkkatoo pólitig gii di “Sonko président 2024” naroon ko amal ci gaawug...

SÉEX ANTA JÓOB, SUUL KER DU KO TEE FEEÑ…

Séex Anta Jóob a ngi juddoo Céytu, 29eelu fan ci desàmbar 1923. Alxuraan la dale njàngam laata muy dugg daaray nasaraan. Ci 22i atam...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/12/2023)

UBBITEG BENN BÀNQAAS FA UCAD Ay weer ginnaaw ba ñu tëjee daara ju kowe jooju, ba tey buntam yaa nga tëje. Mu mel ni kilifa...

“MAN, SÉEX ANTA JÓOB !”

Bu Séex Anta Jóob (1923-1986) doon dund ba tey, am koon na 100i at ci ren jii. Dafa di, jamono jii sax, ñoo ngi...

70i WAY-SÀKKU JÉBBALE NAÑ SEEN I WAYNDARE

Ci àllarbay tey ji, 27 desàmbar 2023, la àpp bi Ndajem ndeyu àtte mi mayoon way-sàkku lawax yi jeex. Bii guddi gi xaajee (00i...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

CAN 2024 Amara Juuf bokkul ci 55i futbalkat yi Alin Siise tànnagum ngir yóbbu leen ca CAF laata mu di ko seggaat ba 27. Moom,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (25/12/2023)

PÓLITIG Saytukati ndeyu àtte réew mi ñoo ngi wéy ba léegi di jot wayndarey way-sàkku lawax yi ñeel wotey 2024 yi. Ci 77i lawax yi...

SIYAARE DAARAY KOKKI : BÉSUB ALXURAAN

Démb ci dibéer ji? yemoon ak ñaar-fukki fan ak ñeent ci weeru desàmbar wii, moo nekkoon bésub ndajem Alxuraan miy am at mu jot...

RËG-RËG DAAN NA BOMBARJEE

Dooley xale xajul ci mag. Loolu la doomu Caaroy ji wan na doomu Mbuur ji, démb ci dibéer ji. Waaw, Rëg-Rëg ak Bombarjee ñoo...

MBIRI NDEELA MAAJOOR JUUF

Ndeela Maajoor Juuf dugg na ci guddi gu bët setagul. Ginnaaw ba ñu ko jàppee ba téeyandi ko, Birigàdd Su (Brigade de protection de...

R. BOURGI : “LAWAXU USMAAN SONKO MOOY GËN A…”

Robert Bourgi, layookatu farãse bi, àddu na ci géewu pólitigu Senegaal. Waa Dakar Times ñoo ko doon laaj muy tontu. Ci biir laaj tontu...

BÀRTELEMI JAAS SOOY NA

Ci àjjumay tey jii, 22 desàmbar 2023, la Ëttub àttewaay bu mag bi doon saytu neenal-àtte bi layookati Bàrtelemi Jaas yi dugaloon. Ëtt ba...