Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

WAA LACOS WOOTE NAÑ BÉSUB ÑAXTU

Lëkkatoo gi ëmb mbooleem njiit yi nekkug lawaxu Usmaan Sonko yitteel, ñu gën leen a xam ci turu Lacos (Leaders et alliés du candidat...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/11/2023)

ËTTUB ÀTTEWAAY BU MAG BI DËGGAL NA WALF Ci weeru féewaryee wii weesu, CNRA dafa dogoon siñaalu télé Walf. Li ko sababoon mooy li Walftv...

NJÀNG MAA NGI CI YOONU NDËRMEELU

Njàng meek njàngale mi ci Senegaal mu ngi jànkonteel ak i jafe-jafe yu metti. Muy lu faf daj kàpp daara yépp. Mu mel ni...

TUUBAA : FETAL NAÑ BENN BAAY-FAAL

Ci guddig talaata ji, jàpp àllarba 8i nowàmbar 2023 la ñu fetal benn Baay-Faal ca Tuubaa ca koñu Firdawsi. Li sabab jile jéyya, mooy ne...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (08/11/2023)

AYIB DAFE JOTAGUL XOBI BAAYALE YI Ba joxeg xob yi tàmbalee ba léegi daanaka moo ngi baagante diggante DGE ak CENA. Waaye, loolu taxul mu...

MBËKK MI : GAALUG 280I NIT TEERI NA GÀDDAAY

Ag gaal gu yeboon i mbëkk-kat moo teeri Gàddaay. Nee ñu am ñaar ñu ci ñàkk seen i bakkan. Ci guddig talaata ji la...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2023)

PÓLITIG Kujje gee ngi waajal lu bees ñeel wote yiñ dégmal. Sëñ Abdurahmaan Juuf, di njiitul làngug pólitig gii di Awale, moo ko xamle démb...

MÓODU LÓO DAAN NA AAMAA BALDE

Xaar bi yàggoon na lool, waaj gi tamit naka noonu. Waaye, ñaari mbër yi mujje nañu sëgg démb ci dibéer ji. Móodu Lóo ak...

AKSIDAŊ BU METTI CA MBÀMBILOOR

Aksidaŋ yaa ngi wéy di rey nit ñi ci kow tali bi. Bërki-démb, ci boori ñetti waxtu jàpp ñeenti waxtu ci ngoon la aksidaŋ...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : YËNGU-YËNGU YI TÀMBALEETI NAÑU

Ci weer doŋŋ lañu tollu bi lekkool bi tijjee ak tey. Waaye ñaari kuréli jàngalekat yii di Cusems (cadre unitaire syndical des enseignants du...

MAKI SÀLL DÀQ NA WAA CENA

Njiiteefu réew mee génne yégle, di ci xamle ne Njiitu réew mi tabb ñu bees ci boppu CENA, kurél giy saytu lépp lu aju...