Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/11/2023)

PAPITOO KARA GÉNN NA ÀDDINA Paap Ibraayma Géy, ñu gën koo xame ci dàkkentalu “Papitoo Kara” moo génn àddina. Moom nag, nee ñu da doon...

DGE MÀTT NA, NE DU BÀYYI

Ci talaata jii, 31 oktoobar 2023, la kurél giy saytu wote yi ci réewum Senegaal (CENA) jël ndogal ne DGE dafa war a jébbal...

CAABALUG ANSD 2023

Muy ab liggéey bu ñuy baamtu fukki at yu nekk. Ñu door ko ca atum 1976, renn di juróomeelu yoon bi ñu koy amal....

KUPPEG ÀDDINA GEES JAGLEEL U17 FA ENDONESI

Tànnees na fukk ak benni ndaw yi war a teewal Senegaal fa Endonesi ñeel kuppeg àddina jagleel ñi ëppalagul 17i at. Nii la toftale...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/10/2023)

PÓLITIG Abdu Karim Fofana, jëwriñ ji yor kàddu Càmm gi, wax na jëmale ci amalub wotey 2024 yi. Mu mel ni kuy tontu Buubakar Kamara...

CENA BI DËGGAL NA USMAAN SONKO

Ginnaaw ndogalu àttekatu Sigicoor bi, Sabasi Fay, CENA joxati na dëgg Usmaan Sonko ñeel xobi baayale yi ko DGE di bañ a jox. Nde,...

WÉR-GI-YARAMU USMAAN SONKO

Talaata fukki fan ak juróom-ñaar ci weeru oktoobar wii la Njiitul Pastef li dooraatoon xiifal gi. Boobaak léegi ma nga ca, teggiwul tànkam. Ba...

MBIRI USMAAN SONKO : CENA BI JËL NA NDOGALAM BA NOPPI

Ginnaaw bi DGE (Direction générale des élections) bañee doxal ndogal li àttewaay bu Sigicoor jëloon, Usmaan Sonko ak i layookatam yóbbu woon nañu mbir...

NJËGU MBËJ MI JÉGGI NA DAYO

Mboolaay mi sonn na, damm na, tàyyi na ci dundin bu metti bi muy dundu. Réewum Senegaal dafa mel ne ab taab bu bënnagul,...

COOWAL UCAD

Ginnaaw ba ñu taaxeerloo ay ayu-bés, ndongoy jànguneb Ndakaaru yaa ngi sàkku ñu ubbi seen dara ju kowe. Waaye, ndogal laa ngi aju ca...

JÀMBAAR

Jógati naa saddati ay bayit sargale mbër Bàkk ko jiin ko xaacu naan na woy wi wër Ragal péete kat xañ na fi nit ki wërsëgam Moom...

NDAJEM KAAJARU “TÀNN-BÉER” BU LÀMP FAAL KALA

Gaawu gii weesu, yemoo woon ak ñaar-fukki fan ak benn ci weeru oktoobar wii, lañu doon aajar téereb nettali bii di Tànn-béer. Ngoti Faal...