Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

KOLONEL SÉEX TIIJAAN MBÓOJ WUYUJI WOON NA SÀNDARMI KOLOBAAN YI

Kolonel Séex Tiijaan Mbóoj wuyuji woon na sàndarmi Kolobaan yi. Moom, Séex Tiijaan Mbóoj, moo fi jiite woon kurélu Coopération et des Relations publiques...

SAALIW MBAY : NDÀND FAAL, KËR MADAM (2/2)

Bërki-démb, ci gaawu gi (21eelu oktoobar 2023), lañ doon aajar téere Porofesëer Saaliw Mbay bim mujje génne tudde ko Ndande Fall, Keur Madame ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/10/2023)

PÓLITIG Waa F24 fésal nañ seen tiitaange ci tolluwaayu réew mi. Seen xel dalul wenn yoon ci niñ dëgmalee wotey 2024 yi. Li ñuy ragal...

SAALIW MBAY : NDÀND FAAL, KËR MADAM (1/2)

Bërki-démb, ci gaawu gi (21eelu oktoobar 2023), lañ doon aajar téere Porofesëer Saaliw Mbay bim mujje génne tudde ko Ndande Fall, Keur Madame ci...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

KUPPEG ÀDDINA U17 2023 Ndawi Senegaal yaa ngi ci waajtaayu kuppeg àddina si ñu dëgmal te war a am ci weer wii di teew. Cig...

DUND BU JAFE BI : SAA-SENEGAAL YEE NGI ÑAXTOOTI

Démb ci gaawu gi, 21 oktoobar 2023, saa-senegaal yaa nga woon fa Place de la nation. Ñu dajaloo fa ngir amal ab jotaayu ñaxtu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/10/2023)

ISRAAYEL-PALESTIN Xeex bi dakkagul diggante yawuud yi ak julliti Palestin yi. Israayel a ngi wéy di tàbbal i bomb ca Gasaa. Keroog, ab loppitaan lañ...

USMAAN SONKO WEER NA MAKI SÀLL

DGE, kurél giy saytu lépp lu aju ci wote yi, lànkalati na ndawul Usmaan Sonko li, Ayib Dafe. Nee na dee, du jébbal Usmaan...

LUUBALUG 30I TAMNDARETI CFA CA CMS

Ka yoroo keesu kër gii di CMS (Crédit Mutuel du Sénégal) moo luubal ay koppar ci nafag benn kiliyaan. Maanaam, dafa jële ca nafag...

MBIRUM USMAAN SONKO

Ay weer ginnaaw ba ñu ko tegee loxo ak tey, ba léegi Usmaan Sonko mi ngi ci loxoy Yoon. Moom, njiitul Pastef li, nga...

JÉYYA CA TASET

Taset, di ab gox bu féete ca diwaanu Nooto, fa Cees. Aw tiis moo leen gane démb, di aksidaŋ bu fa am. Ñetti ndongo...

KASOY SENEGAAL : XIIFAL NIKI NGÀNNAAY

Ñi ñu tëj ci kaso yi, xiifal gi lañ jël def ko ngànnaayu xeex. Ginnaaw bi jigéeni Kàmpenaal yi tollee ci juróom-ñeenti fani xiifal,...