Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

JOŊANTEB XARITOO : SENEGAAL DÓOR NA KAMERUN 1-0

Gayndey kuppe yi dóor nañ Kamerun 1-0. Tey ci altine ji lañ doon amal joŋanteb xaritoo ca fowub Bollart bu Lens (France). Saajo Maane...

NGOMBLAAN GI : TAXAWU WÉET NA

Ab diir, ginnaaw ba Ngomblaan gi tëjee woon ay buntam, tijjiwaat na leen ci fan yii. Ngomblaanug Senegaal nag, dafa miin coow, rawatina gu...

MBIRI USMAAN SONKO : UMS DUGG NA CI COOW LI

Ginnaaw bi àttekat bi tirbinaalu Sigicoor jële ndogalu bindaat Usmaan Sonko ci këyitug wote yi, Yoro Musaa Jàllo, di Agence judiciaire de l’État, maanaam...

PALESTIN – ISRAAYEL : KU TOOÑ ?

Fan yii, Palestin ak Israayel ñu ngi sànnantey mbéll, sóobu cib xare bob, bim tàmbaleek léegi, ay junniy junni bakkan rot nañ ci. Wii...

TIRBINAALU SIGICOOR DUGALAAT NA USMAAN SONKO CI KËYITUG WOTE YI

« Am nanu ndam ! Àttekat bi santaane na ñu bindaat Usmaan Sonko ci këyitug wote yi. » Bi Sayid Larifu, kenn ci layookati Usmaan Sonko, di...

MAKI SÀLL TABB NA CÀMM GU YEES

Fanweeri jëwriñ ak juróom-ñeent la Njiitu réew mi tànn ngir ñu àggali liggéey bi fii ak wotey 2024 yi. Ci biir fanweer ak juróom-ñeenti...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/10/2023)

MBIRUM USMAAN SONKO AK I ÑOÑAM Suba ci alxames ji la Yoon di leeral lenn ci mbirum Usmaan Sonko, Faala Fleur ak Nit Doff. Moom...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/10/23)

PÓLITIG Ngomblaan gi génne na ab yégle di ci xamle ne dina amal lëlu aadaam bu atum 2023/2024 ci gaawu gii, 14 oktoobar bu 10i...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/10/2023)

PÓLITIG Aali Nguy Njaay mottali na yéeneem ngir nekk lawax ci wotey 2024 yi. Ci gaawu gi la woote woon am ndaje mu mag ngir...

MBËKK MI : DEM REKK !

Mbëkk mi lëmbe na lool réewum Senegaal rawatina ci fan yii. Lu daan am ci am at walla ci ay weer, léegi, ci ayu-bés...

CÀMM GU BEES GI : MAKI SÀLL TABBAAT NA AAMADU BA

Njiitu réew, mi Maki Sàll, tas na Càmm gi. Démb ci àjjuma ji la jël ab dekkare daldi tekki ndomboy-tànki képp ku nekkoon jëwriñ...