Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

YOON GÀNTALATI NA USMAAN SONKO

Usmaan Sonko dafa dugaloon ? keroog 2i fan ci oktoobar 2023, ab « recours » ñeel li ko waa DGE bañ a jox xobi baayale gi. Sànq...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI ( 5/10/2023)

MAKI SÀLL DINA TAS CÀMM GI Muy ab xibaar bu jib ginnaaw ba ñu defe ndajem jëwriñ yi démb ci àllarba ji. Njiitu réew...

MOOMI SEKK, SOXNAS BUGAAN DANI GÉY, GÉNN NA ÀDDINA

Tiis ak naqar wu réy ñoo dal ci kow njiitul DMedias ak kurél Gëm Sa Bopp, Bugaan Dani Géy. Waayeet, njabootu ndem-si-Yàlla ji, Coon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (04/10/2023)

LU BEES ÑEEL GÉNNÉEG USMAAN SONKO CI WAYNDAREW WOTE YI Ay fan ginnaaw bees jébbalee Njiitul Pastef li, Usmaan Sonko, bataaxel biy firndeel ne génnee...

UBBITEG LEKKOOL YI

Lekkooli Senegaal yi tàmbali na tijji ay buntam. Niki démb ci altine ji, 2 fan ci weeru oktoobar 2023, lañu woo jàngalekat yi. Naka...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/10/2023)

PÓLITIG Aliw Tin yëy na yàbbi ci ni demokaraasi bi tëdde ci biir réew mi ak Usmaan Sonko mi ñu seppi ci wotey 2024 yi....

XUWAAN BARÀNKOO TUUMAAL NA FARÀNK ÑÀNKI JOM

Farànk Ñànki Jom, di mag ci jëwriñ ji ñu dénk wàlluw biir réew mi, Àntuwaan Feliks Jom, moom lañu duut baaraam ñeel mbirum luubal....

XIBAARI TAGGAT-YARAM (1/10/2023)

KUPPEG ÀDDINA WAY-LUU YI (MUUMA YI) Bàyyeesu leen xel, waaye way-luu (muuma) yi teewal Senegaal ca kuppeg àddina si bees leen jagleel ñoo ngay def...

Wotey 2024 : wure wa dem na këŋ

Ubbi nañu utum parenaas yi ñeel wotey 2024 yi. Ñi fas yéene nekk lawax daldi sóobu ci njëkkante bi ngir matale lim bi. Waaye...

NISEER AM NA NDAM CI KOW FARÃS

Niseer am na ndam ci kow Farãs. Ginnaaw seen xëccoo bu yàgg bi (3i ayu-bés), njiiti Farãs yi mujje nañ xàddi. Nde, seen àmbasadëer...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (27/9/2023)

GÀMMU 2023 Tey, àllarba, yemoo ak ñaar fukki fan ak juróom-ñaar ci sàttumbaar (weeru tubaab), fukki fan ak ñaar ci weeru gàmmu (weeru wolof) mbaa...