Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

YOONU GÀMMU

Mawlidu Nabi, ñu ciy màggal juddug Yonnent bi (sas), moom mi Yàlla sunu Boroom yonni woon ci mbindeef yi. Muy daje ak fukki fan...

MAKI SÀLL TAGG NA SEEX MAAHI ÑAS

Tey ci talaata ji, Njiitu réew mi Maki Sàll, ma nga woon fa Kawlax. Gàmmu gee ko fa tax a dem. Waaye, bu ko...

GÀMMU GI

Weeru Gàmmu La Buur Yàlla taamu Ngir gane àddina Yonent bi Yàlla def mu gën ci mbindeef yi Gënal ko ñépp moom Rasululaahi Moo tax looy def bëgg mu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (25/9/2023)

PÓLITIG Séex Tijaan Jéey génne na boppam ci lawax yi. Dootul bokk ci ñi namm xëccoo Njiitu réewum Senegaal ci wotey 2024 yi. Muy ndogal...

JIIXI-JAAXA CI FAATUG MARI GÉY CA NGOR

Mari Sàmb Géy, ñu gën koo xame ci Mari Géy, moo ñàkk bakkanam fa Ngor, ci anam yu doy waar. Xew-xew boobu ma nga...

KIGALI

KIGALI Kigali, soo fay doxantu Sa xol day sedd doo gis loo  ñaxtu Nga naw ci saa si Njiitu réew ma Ndax liggéeyam rafet na Céy Kigali ! Cet gaa...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI ( 21/09/2023)

MAKI SÀLL : « PASTEF DAY WOOTE FITNA » Njiitu réew mi Màki Sàll dikkaat na ci tas gi ñu tas làngug pólitig gii di PASTEF. Muy ay...

MAKI SÀLL A NGI WOOTE COPPITE

Njiitu réew mi, Maki Sàll, mi ngi soññ ak a xirtal ay ñoñam. Ci talaata jii weesu la doon wax fa New York, ca...

MAKI SÀLL : AMERIG DU SENEGAAL

Toroxal nañ Maki Sàll fa New York. Bi mu àggee Amerig, dañ ko fa doon yuuxoo ak a ŋàññi ni mu yoree réew mi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/9/2023)

TÀGGATOOB NJIITU RÉEW MI MAKI SÀLL CA ONU Démb ci talaata ji la Njiitu réew mi jibal kàdduy tàggatoom ca ndajem Mbootaayu Xeet ma. Lii...

NJAMBAANU MOLOTOF MA CA LIISE DELAAFOS

Sàndarm yi wàcc nañu fa liise Delaafos ci gaawu gi. Yéenekaay Libération ne, seen wàcc boobu, wàcc bu am jom la. Nde, nee nañu,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (18/9/2023)

PÓLITIG Seydu Géy mi yor kàddu waa APR àddu na ci coow li topp seen pàrti bi. Fekk ñu dalaloon ko démb ca jotaayu Grand...