Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (18/9/2023)

WAA LORIENT YI SARGAL NAÑU BENJAMIN MENDY Benjamin Mendy duggaat na démb ci pàkkub futbal, gannaaw tuuma gu metti te yàgg bi tegu woon ci...

SËRIÑ SAALIW TURE WÀCC NA

Sëriñ Saaliw Ture mi toogaloon xalifa Murid yi ca Kees a wàcc liggéey guddig àjjuma jàpp gaawu (14/15 sàttumbar 2023) fi Ndakaaru. Amoon na...

MALI, BURKINAA FAASO AK NISEER : MBOOLOO MOOY DOOLE

Mali, Burkinaa Faaso ak Niseer bokk nañ xaatim ab sàrt bi ñu tudde ci nasaraan Charte du Liptako-gourma. Sàrt booboo wund juddug digaale gi...

ABLAAY DAAWDA JÀLLO TOPP NA CI GINNAAW AAMADU BA

Ablaay Daawda Jàllo amal ñam ndaje ak taskatixibaaryi, tey ci ngoon, doon ci leeral taxawaay ñeel wotey 2024 yi. Nde, njiitu lëkkatoo Bennoo Bokk...

ETAASINI : DÀQ NAÑ 140i SAA-SENEGAAL

140i saa-senegaal la Etaasini dàq. Daf leen a waññi ginnaaw biñ fa duggee ci anam bu jaarul yoon. Yéenekaay Les Échos moo siiwal xibaar...

DABBAAX : BAAX NGIR YÀLLA, BAAX CI SENEGAAL

Senegaal, ci sunu aada, bu ñu tuddee doom, dañu baaxoo di ñaan : Yal na tur wi wuyu boroom.  Allaaji Abdu Asiis Si Dabbaax, ñaan...

MAKI SÀLL DINA TABB CÀMM GU BEES

Ginnaaw bim tànnee lawax bi mu bëgg mu wuutu ko ci boppu réew mi, Maki Sàll, Njiitu réew mi, dina indiy coppite ci Càmm...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/9/2023)

MAAM BÓOY JAAWO LAWAX LA El Haaji Mamadu Jaawo, ñu gën ko xame ci Maam Bóoy Jaawo biral na ne lawax la ci wotey 2024...

ALSERI DUMAATI NA SENEGAAL

Démb ci talaata ji la gayndey Senegaal yi doon janook Alseri ci joŋante xaritoo. Jamñaajo, ça fowub Abdulaay Wàdd, lañ ko doon futbalee. Alseri...

AMET SIISE WAXATI NA TOJAANGE !

Saa bu waxee, loxo dar gemmiñ. Amet Siise nekk ku ñu miin ci mbaali-jokko yi. Mu tàmbalee fés ci Youtub bi ginnaaw ba mu...

REYATI NAÑ ÑETTI NIT FA KÉEDUGU

Ab xeex bu metti moo amoon diggante takk-der yi ak askan way yeewoo fa Xosantoo ak Mama Xono (diwaanu Kéedugu). Limees na ci ñetti...