Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/9/2023)

WOTEY 2024 YI Lawaxub Bennoo Bokk Yaakaar bi ñu doon laam-laame xam nañu ko léegi. Aamadu Ba lay doon. Ci gaawu gi lañu ko siiwal...

ÑETTI FANI DËJ FA MALI

Tiis wu metti moo dal ca kow askanu Mali. Lu tollu ci juróom-benn fukk ak ñeenti doomi-aadama lañu fa faat ci ay cong ci...

F24 WOOTEETI NA YËNGU-YËNGAL

Waa F24 fas nañoo yéene wéyal seen xeex bi. Loolu lañu siiwal keroog àjjuma bi ñuy jàkkaarlook taskati xibaar yi. Booba, daa fekk perefeb...

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko gën. Njub, jom, fulla, fayda, ngor, fit, worma, kersa añs., ñoo di jikko yoy, mépp...

AAMADU BA : LAWAXU BENNOO BOKK YAAKAAR CI WOTEY 2024 YI

Ginnaaw wiiri-wiiri bu metti bi, àgg nañ Ndaari. Maki Sàll tànn na Aamadu Ba, jiital ko ngir mu wuutu ko ci boppu réew mi....

RËNG-RËNG FA MAROG : 820i NIT DEEWAGUM NAÑ CI

820i nit ñoo ñàkkagum seen i bakkan ci rëng-rëng bi yëngal suufus Marog si. Jëwriñu biir réew ma moo joxe lim bi. Nee ñu,...

BENNOO BOKK LAWAX WALLA FÉEWALOO TAS YAAKAAR ?

Coowal lawaxu Bennoo Bokk Yaakaar la yéenekaay yi xëyee tey ci àjjuma ji, 8 sàttumbaar 2023. Ñépp, daanaka, dañu gaatnga tasug lëkkatoo Bennoo Bokk...

LI GËN A FES CI XIBAARI BES BI (6/9/2023)

BÀYYI NAÑU XALIL KAMARA BU SENEGO Bërki-démb ci talaata ji lañu téye woon taskatu xibaarub Senego bi fa DIC. Li ko waral mooy yaxal bu...

BATAAXAL BU JËM CI MAAM SEŊOOR

Maam, Fan yee weesu, sama xel dafa ne yarr ci yaw. Ba nga demee ba léegi déggu nu la. Mbaa du foofu dafa neex rekk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/9/2023)

MÀGGAL TUUBAA Démb ci altine ji, 4 sàttumbar 2023, la murit yi doon bésal màggalug Tuubaa gi. Muy bés bu ñuy màggal at mu jot...

AKSIDAŊ BU METTI CI YOONU TUUBAA WI

Aksidaŋ bu metti moo am ci yoonu Tuuba wi. Xibaar bi nag, bettul ñu bari. Dafa di, at mu nekk, ay jéyya tegaloo ci...

YOON : SOS/PAIX A NGI ÑAAN NJEKK NJIITU REEW MI

Mbootaayu kuréli ma-xejj yi ngir jàmm, ñu gën leen a miis ci SOS/Paix (Synergie des organisations de la société civile pour la paix) ñaan...