Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 12 desàmbar 2022

PÓLITIG Jëwriñ ju mag ji, Aamadu Ba teew na ci kanamu ngombalaan gi. Ginnaaw bi ko Njiitu réew mi tabbee woon ci boppu Càmm gi...

NDAM LU RÉY, NDAM LU TUUT

Alxames, 8i fan ci desàmbar 2022. 15i waxtoo jot ci ginnaaw njolloor. Ñi ëpp ci àddina si, rawatina biir kembaarug Afrig, jenn itte lañu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI GAAWU 10 DESÀMBAR 2022

PÓLITIG Woteb nafag 2023 gi jeex na ci gaawu bi. Jëwriñ ji ñu dénk nafag Senegaal jàkkarloo na ak dépite yi. Mu mel ni am...

Xeex nger ci àddina si

Ci àjjuma ji, 9i fan ci weeru desàmbar 2022, la àddina wërngal këpp doon màggal bés biñ jagleel xeexub nger. 20i at ci ren...

« COO ! NOO ÑÀKK FAYDA !… COO ! NOO ÑÀKK JOM ! »

Magum jawriñu Senegaal, Aamadu Ba, ma nga woon Farãs, waroon fa teewe ndajem liggéey mom, Càmmug Senegaal ak gu Farãs a ko séqoon. Duppees...

KAÑ LA COOWAL AJI SAAR AK SONKO DI JEEX ? 

Ci talaata 6 desàmbar jii nu génn la Usmaan Sonko ak Aji Raabi Saar doon amal seen jàkkaarloo bu njëkk ci pekkug magum àttekat...

KASO AMATI NA GAN

Jàpp nañu Faddiilu Keyta mi bokk ci bëkk-néegi Usmaan Sonko, njiital PASTEF li. Ab yaxal bi mu bindoon, fésal ko ci xëtu Facebookam a...

MBATIT BIIR NDAKAARU

Ndakaaru dalal na “Festival come to my home”. Muy xew-xewu mbatit, cosaan ak xeltu, fekk baax  réewum Marog. Kii di Driss Alaoui Mdaghri nekkoon...

JAKKAARLOO AJI SAAR-USMAAN SONKO

Ginnaaw at ak lu topp bi coowal ciif gi dooree ak léegi, jàppees na àppu jàkkaarloob ñaar ñi séq mbir mi. Coow loolu nag,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 5 desàmbar 2022

PÓLITIG Ngombalaan gaa ngi wéy di natt nafay njëwriñ yi ñeel atum 2023. Njëwriñu dem beek dikk bi ci jàww ji ak suqaleeku jumtukaay yi...

SIDAA NGI WÉY DI REY…

Biige Jaañ, ndaw su jekkoon, neex deret lool, moo dem ba mel ni kuy féey ciy yëreem ndax jeex. Daan na gaaw a sonn,...

Kuppeg àddina si : Senegaal, xalam demoon na bay neex buum ga dog

Ginnaaw ñaar-fukki at bim gëjee romb pàcc bu njëkk bu kuppeg àddina si, Senegaal doon na joŋante ñaareelu wicceem dë finaalam ci dibéer jii...