Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

IGE JOT NA NDIGAL

IGE (Ispection Générale d’État) am na sas wu réy. Dina amal ay caytu yu yaatu ciy këru liggéey yu mag. Muy sas wu réy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/6/2024)

COOWAL “DPG” LAA NGI WÉY Coowal “DPG” (Déclaration de Politique Générale) dafa mel ni, bés bu set, day gën a takkarnaase. Ñi koy xamb...

EURO 2024

Njureefi sumb bu njëkk bi Sumb bu njëkk bi ñeel Ëro 2024 bi ca Almaañ jeex na ci àllarba jii weesu. Kippu gu ci nekk...

COOWAL “DPG” BU USMAAN SONKO

Démb, kippaangog depite gu Yewwi Askan Wi doon na janoo ak taskati xibaar yi. Jubluwway ndaje maa doon indi ay leeral ci lenn ciy...

CFEE 2024

Joŋantey CFEE yi door na ci biir réewum Senegaal, ca Gàmbi ak ca Gine Bisawoo. Muy ab natt bi ñuy amal te ndongo yi...

YENU SA BOPP

"Yen bu diisee, dañu koy jàppoo". Loolu la maam ja waxoon. Noppeegul sax, kenn ca sët ya ne ko : "waa maam, lu ma...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/6/2024)

BÉSU LIGGÉEYKATI BOKKEEF GI Démb, ci dibéer ji, 23i pani suwe 2024, lañ doon màggal ci àddina sépp bés bees jagleel liggéeykati bokkeef gi. Ci...

COVID-19 BI NUYOOTI NA !

Li ñu doon laam-laamee démb ak barki-démb mi ngi bëgg a leer. Nde, ñu bari dañoo jàppoon ne ay naxembaay la walla ay xuppe...

REYAATE BI CI RÉEW MI

Gaawu gii weesu, dafa am ku ñu jam paaka fa Ndindi, mu faatu. Ndindi, ci diiwaanu Jurbel (Njaaréem) la nekk. Loolu xew ci guddig...

Aj 2024 : Ujaaji Senegaal yu njëkk dellusi nañu ci réew mi

Lu ëpp 12 000iy ujaaj ñoo jóge woon ci biir réew mi. Ujaaj yu njëkk yi dellusi nañu ci jàmm. Seen ub lim tollu...

WÀÑÑITEG NDUND GI

Wàññiteg njëgu ndund gi, Càmm gi jël na ci ay ndogal. Lañu jotoon waxtaane ci yenn ci njëg yi ñu war a wàññi altine...

NJUREEFI NDAJEM JOMAAY AK MACRON

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, ma nga woon Farãs. Daf fa teeweeji woon am ndaje ñeel mbirum ñakk ci àddina si. Ba...