Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/6/2024)

NJIITU RÉEWUM FARÃS DALAL NA MOM SENEGAAL Lu jege ñetti weer ginnaaw bi ñu ko falee ak léegi, Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay,...

FIPPU CA KÀMPENAAL BU “LIBERTÉ 6”

Jar-jar (prisonniers) ya nekk ca kasob Kàmpenaal (Camp penal) bu “Liberté 6” ñoo doon fippu. La ko sabab mooy anam yu metti ya ñu...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI CA FARÃS

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, war teew ca Farãas ci àllarbay tey jii. Tukki bii moiy doon njëlbeenug tukkeem ci biti kembaaru Afrig. Njiiteefu...

TABASKI 2024 : KÀDDU NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Sñ Basiira Jomaay Jaxeer Fay, yëkkati nay kàddu ci julli gi. Naka noonu, muy ñaanal julliti Senegaal yépp ak yu àddina...

FITNA FA MEDINA GUNAAS

Xibaar bu yéeme te doy waar moo jib tey, ci bésub tabaski bi. Muy xibaarub fitna ak taafar ju bawoo Medina Gunaas, diggante ñaari...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (16/6/2024)

TABASKI 2024 NJIITU RÉEW MI JÉGGAL NA 376i MA-KASO Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, feddali na aada. Nde, tabaski ju jot, kiy Njiitu...

CÀKKUTEEFU WAA FORUM CIVIL

Kurélug maxejj yi, ñu gën koo miis ci Forum Civil, àdduna ci wàññi gi Nguur gi wàññi dund gi. Naka noonu, ñuy sàkku ci Nguur gi...

MA-DEMBA SOKK WUYUJI NA BOROOMAM

Xibaar bu tiis la réew mi xëyee tey. Ma-Demba Sokk moo génn àddina. Pari ga mu doon fajoo, ca Farãs, la gaañoo. Mi ngi...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (14/6/2024)

DELLOO NAÑU WALFADJIRI AY SÀQAM Keroog ci àllarba ji la xibaar bi rotoon ne, dañu tëj sàqi koppar yu Walfadjri. Waa Walf ñoo ko siiwaloon,...

AY TABB YU YEES

Barki-démb ci àllarba ji lañu doon amal ndajem jëwriñ mi. Ñu amal ko nag, ci jamono joo xam ne, réew mi dafa dalal ag...

WATTU LÀKKI RÉEW MI 2/3

TURI JOTAAYI TELE SENEGAAL YI Seen Xéewal Tës Saa Njóogu Kër gi ak Taal Ngol-Ngol Aaru Mbedd Diine ak Jamono Reeni koom-koom Njàngatu bés bi Jàkkaarloo Bi Yeewuleen Seen jotaay / jataay Faramfàcce Sama Gox Kàkkatar Tàkkusaanu Jolof Li ci...

WÀÑÑIG DUNDU GI

Ñoo ko dige woon, tàmbali nañ ko def. Càmmug Basiiru Jomaay Fay geek Usmaan Sonko miy njiitul jëwriñ yi, wàñni na lenn ci dundu...