Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

JÀPP NAÑ BAH JAXATE AK IMAAM SÉEX TIIJAAN NDAW

Démb lañ jàpp kii di Bah Jaxate, di aktiwist bu jege Maki Sàll. Waa DIC ñoo ko teg loxo. Li ko sabab mooy kàdduy...

PAATUG NJIITU RÉEWUM IRÃ

Njiitu réewum Irã li, Ebraahim Raysi, faatu na. Fafalnaaw bi mu duggoon ak jëwriñam ja yor mbiri bitim-réew moo daanu. Jëyya jaa ngi xew...

“COUP D’ETAT” BU MOY FA RDC

Ab “Coup d’Etat” moo naroon a am fa Réewum Kóngo Demokaraatig (RDC). Démb, ci boori ñeenti waxtu jàpp juróomi waxtu ci njël la mbir...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/5/2024)

JAMRA ÀDDU NA ONG Jamra, ag kurél guy yëngu ci sàmm jikko yi, àddu na ci waxtaan wi njiitu Càmm gi di Usmaan Sonko ak...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA NISERIYAA AK GANA

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, mu ngi wéyal tukkeem yi ci biir kembaar gi. Ginnaaw Móritani, Gàmbi, Gine Bisaawo ak Koddiwaar,...

“LAC DE GUIERS 2” GËNATI NA CÓLLE

Mbërum Géejawaay mi, Paab Ãsu Siise, ñu gën ko miin ci dàkkentalu “Lac de Guiers 2”, mi ngi jamono ji ci guddi gu lëndëm....

USMAAN SONKO ŊÀÑÑ FARÃS, ARAAMAL NGÓOR-JIGÉEN

Usmaan Sonko,  njiitul PASTEF, doon na dalal Jean-Luc Mélenchon. Njiitul làngu La France Insoumise, ca Farãs, daf fee amalsi tukkib nemmeeku, ganesi waa PASTEF....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16/5/2024)

WÀÑÑIG DUND BI Wàññig dund bi bokk na ci li gën a soxal saa-senegaal yi jamono jii, rawatina ñi seen loxo jotul seen ginnaaw. Moo...

AY TABB YU YEES

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, tabb na ay njiit yu bees ci boppi yenn banqaas yi. Démb, ci àllarba ji, 15 me...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

 Abiib Béey : "OM su ma bëggee..." Ci at mu réy mi mu amal ren ak ekibam bii di Red Star ca Nasiyonaal 1 bu...

Ndigalul dakkal tabax yi ci peggu géej gi

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, taxawal na ab banqaas buy saytu anam bees joxee suuf si féete ak wetu géej gi, ci diiwaanu Ndakaaru....

U.I.J.A SARGAL NA USMAAN SONKO

U.I.J.A (Union Internationale des Journalistes Africains) kurél gu mag la, gu ëmb taskati-xibaari Afrig yi. Mu nekk kurél goo xam ne am na neexal...